ohhhhhh Ya Allah manguilaye gnane keppeu koussi beugueu té mouy sabablou nangako diapalé beu beugueu beuguam antou si seup diobaré Ya Rabby. si barké kou Teddeuki Sallalahou Aleyhi wa Salam. amin
2026-10-03 08:27:43
929
ousmanenoreyni2211🇸🇳 :
Li yallah nagne ko am way 😁
2026-10-03 07:05:38
534
Queen.11 :
Dama ragual escalier yi😩😂
2026-10-03 01:05:08
89
By🦋Mareme🛍️💚 :
Alleuuuuuu😳😳 wa plan bi ndirouna sama goût 🥰❤️🥺
2026-10-02 22:03:05
576
Jordan23 :
Magnifique architecture
2026-10-02 21:55:19
101
Birane Gueye :
Ohh send m’a plan bi waay
2026-10-03 21:32:26
0
K :
Yalna am keur gou melni dougueul sma famille
2026-10-03 21:42:13
19
Precious🍂💐 :
Li rafett na deh mashaa Allah tay douma douma sangou sax 😤
2026-10-03 20:33:43
0
Khadime Bamba 🌀✌🏿 :
Yallah guir yallah bi lala done wakh 😂
2026-10-03 13:41:39
0
KYA SALIOU SHOP🛍️🇸🇳 :
Awema sakh demi parcelle mani dama dieul model ni😂😂
2026-10-03 08:29:30
17
Mame :
Franchement c’est beau
2026-10-02 22:45:35
168
Amina Gueye :
Sallhou hala mouhamde psl
2026-10-02 22:55:48
78
sénégalaise :
sallalahou halla mouhamedine ❤ a vie
2026-10-03 14:00:39
11
BARHAM SHOP EN GROS 🛍️DKR🇸🇳 :
Favoris yalla bakhna mais rafett na trop machallah ❤️
2026-10-02 21:47:24
30
Bijouxdespieds :
Sama keur mou ngui ni😅😅 kharal ma lale favoris
2026-10-02 22:43:06
25
Lion Noir :
Machallah
2026-10-02 21:40:50
14
Ndoumbaïta business ☑️ :
Yalla nako Yalla may sama diekeur djiou bakh dji Diagne Nar ❤️
2026-10-03 11:39:19
21
Une g💍🥰 :
Yalla bakhna
2026-10-03 00:04:52
0
Daouda Bocoum :
Franchement c’est trop jolie
2026-10-02 23:03:58
5
💞Fatou Beug ALLAH💞 :
Alhamdoulilah
2026-10-02 22:29:55
6
Faatougy💕🕷️ :
Yallah nagne ko meuneul souniou wadiour yi❤️❤️❤️❤️
2026-10-03 09:37:00
5
La rafinée :
Amouma Dara mais Allkhamdou lilah doli di sante bou bakhe🙏🙏🙏🙏