ki loumou la wakh rek bo sété baci biir lep deug leu🥰
2026-10-04 15:12:39
98
warriors :
bara est ce que werna
2026-10-04 15:25:02
15
ミ★𝐌𝐊★彡🇹🇹 :
Bouko wakhé rek deug leu
2026-10-04 15:35:48
30
Mami sonko :
bilahi dou wakhatou
2026-10-04 13:42:07
89
seck lamine :
khana walf pasteef koyr faye
2026-10-04 16:49:13
0
oumarcelo :
barké seydina Mouhamed deuguleuh 🥰
2026-10-04 15:34:45
14
user8820105612947 :
c pas vrai. mane gueuwmako
bougane gnéméwoul lolou
2026-10-04 17:26:00
1
pérédio :
c'est bien où le problème 🥰🥰🥰🥰
2026-10-04 17:34:57
0
Le révolutionnaire :
serigne Touba sonouna
2026-10-04 15:13:21
11
SANKARA :
C'est faux on a resté 2 mois sans salaire on recevait nos salaire avent le 30 maintenant depuis l'accession au pouvoir du sedomisateur on reçoit nos salaire vers le 14 ou 15
Saway liguay deuguale Dara amou ci ´´´raguale lène yala
2026-10-04 15:12:24
5
diaman noir89 :
Sénégal amoul benn presse bou fiy deef chiffres d' affaires, di fay say agent. Télé sax dafa xeewi. Kenn lira toul journaux. Nit gni xam nagn ni dagni fenn reek.
2026-10-04 15:34:53
0
PRÉSIDENT BAMBA🇸🇳 :
Kone Amna niou guem li barra di wakh ni
2026-10-04 16:45:20
8
ndeyemadsdiouf :
2026-10-04 14:08:26
5
Bakh yaye mou serigne saliou ❤ :
2026-10-04 16:57:56
1
Moi c moi :
TFM faya tougnou impôt depuis un an, ma yeugueul lene loolou
2026-10-04 16:10:26
4
Ciré :
c grave. ya des gens qui croient aux mensonges de bara ndiaye
2026-10-04 17:35:33
1
Abdou Faye :
2017 ba 2026 pastef wakh rekkk toumal gorrrr rekkk
2026-10-04 17:26:37
1
Thierno tall :
bougane louma nekh si moom politic ba politic lay guen waye sak jour politic rek bougane taloulen sakh🤣
2026-10-04 15:33:51
2
To see more videos from user @xemit.agri, please go to the Tikwm
homepage.