Bly Lou PA bi deff soukafi béne peulh défone fi Senegal dou guéne réagirer ni mais naniou ko nianal rek peine bii wagnékou tamite ngéne khalate famille niou décédé
2026-10-05 12:56:17
10
:
Tayy Par exemple beneu étranger nieuw Senegal Di dawal camion pour dane dolé wam par erreur mou def accident rayy famille leumb fii legui sou boba esk ni nguen di reagiré ?
2026-10-04 23:38:54
17
Diop bou Sonko 🤩🥰 :
Mom com moy sonou bay ak nimi wakhé nk [Innocent][Innocent][Innocent]
2026-10-05 15:01:29
0
Capricioné 🧸🎀✪ :
liko dall yallah nala dall yaw mame cheikh
2026-10-05 13:24:30
0
Cheikh ibre diop :
Ki dama ba yi Billaye doumako khol baye diek Lou aye wax kham ki kha moul yalla waye
2026-10-05 12:58:57
0
عبدSMD☝️ :
Ki dou nit Kou bakh
2026-10-04 19:26:00
306
maraboss55 :
Waaa ki nitt leuh😌💔
2026-10-04 18:48:24
310
Fallu ——— badman 👣 :
Pour mome wakhna deug
2026-10-04 18:55:22
332
paco diaz :
yall nako natou bi dall
2026-10-05 12:13:01
0
mansory :
we need your help please 🇸🇳🇸🇳
2026-10-05 13:34:59
0
BB LAYE🇺🇸🦍👣🪵☠️ :
mais nak il a raison bakann dafa forr nagnou ko gnanal yalla. rk wadji yalla soutoural ko
2026-10-04 20:28:03
86
S🅱️D. M. 🅰️LUMINIUM🇸🇳🪛🦺 :
Patriote rk la meuneu nékeu
2026-10-04 20:45:41
168
Yayouboussobali16 :
Pour mom Lou khew rek amena si parole
2026-10-04 23:51:24
56
Bineta :
Pour mom mo gueune mouss nieup
2026-10-04 20:19:41
72
BassLutte+ :
Na gneup désabonné
2026-10-04 20:09:19
67
Bb Fatima😍🤪 :
mame cheikh pastef la bokk
2026-10-04 20:11:10
65
To see more videos from user @fallouogodogo, please go to the Tikwm
homepage.