Ligaye wakh ni yeup kénneu ladiou lako xamo noumou démè khamo bakham frein wame yi dafa lâché wadji dawalna Amérique plus de 20ans té meusoul ame problème
2026-10-04 23:03:29
117
l'homme fort de mbour✍️🚗💯 :
ki lima ko begue wakh vocal rék momay engranger
2026-10-05 08:54:06
53
cheikhtidianembengue :
maçon dou wakh thi transport
2026-10-05 11:08:41
27
Moustapha Diop :
Mame Cheikh molène gueune da dioum rek
2026-10-05 11:09:42
3
ABG :
Li dou wax diou rafet ndogal yala founek lay diougue
2026-10-05 14:51:25
0
cheikhsylla :
eggs and you for mhgfgh food and workforce development for beginners
2026-10-05 13:54:27
0
khadimfaye Sope Sérigne Sam M :
li dé moy projet pastef
2026-10-05 07:34:55
13
Modou Wade :
wa pastef la déh
2026-10-05 01:09:11
25
SARAKH NDIAYE Ibrahima :
dioumoul dafa yenè woul cheuffeur diam ngi rek nio takh diamono dangaye agrese nit ray ko dou moudiou fine ga def accident niouni moko tay
2026-10-05 10:14:58
2
pape rastamane :
No yawe do notre😭😭😭😭😭😭
2026-10-05 14:44:20
0
Modou ndao talibe Cheikh :
li mam cheikh ahmad tidian sy maktom nan amna niou xamni diarna niep cotice diokhlene ngur nio nopi nena amna niou xamni diarna niep cotice diokhlene ngir niou wakh 😭😭
2026-10-05 06:56:32
5
♎ :
wadji magui soga comprendre litakh manouma si moum dara
2026-10-04 23:56:10
51
MOMO SÉNÉGAL RÉKK :
Pastef la book
2026-10-05 09:33:41
0
La linguère :
On souhait que notre frère trouve la liberté mais pense à la famille des disparus
2026-10-04 23:06:36
21
yal na sonko bayi fen 💪sagama :
yal na sonko bayi fen 😭
2026-10-05 10:36:43
5
ram :
kou diouk déf vidéo
2026-10-04 21:44:54
23
AFIA BARAKATU📖 🇸🇳 ✪ جوكو :
Pourtant loumou meussoulll def la def dello guinaw supprimer vidéo bi momm xamna nannih dah dioum ndeysannn
2026-10-05 00:10:05
8
Yayou Fatima ❤️ :
Mame Chiekh ana ndogalou yalla
2026-10-04 22:24:32
12
To see more videos from user @tdmalhamndoulilah4, please go to the Tikwm
homepage.