Beugue siiw rek la def mais ana macon ak wakh si transports
2026-10-05 10:43:17
1
mbaye_automobile :
Bilahi liga def la ñèpp wara def ki dafa bon🥺🥺
2026-10-05 11:36:30
1
~<
Loumou kay wagni
2026-10-05 14:32:46
0
Serigne Mbacké Niang :
Mogui nide lokoy wakh
2026-10-05 14:38:29
0
AMDY MUSTAFA MBAYE 🔋💶 :
Merci beaucoup frère blh ki dafa soxor mais yalla bahkna yalla waxol ken yalla kimo baeg rek lay tek natou yalla nako yalla tègil nato bi si barke Mohamed 🙏🙏☝️