Lo bou SONKO :
problème bi budee 100%, man jàpp naa ni ñun population bi am nan ci 99% , ñun ñi dëk ci dëk bi, ñun ñoo paré wul ngir defar dëk bi. État nu waa dëk bi mel reg lay mel, ñun bu hôpital yi baaxul dun ko manifester, bu tali yi baaxul dun ko manifester, bu courant di couper toutes les jrs dun génie wax etat bi dëg, bu dundu bi yokkee ken du génn, bu conextion bi cheré kenn du génn, 😭😭😭😭😭 ñun daal ñoo ngi nii reg took, kenn kune ci ñun jàpp na ni bu afeeram baaxee reg li ci des moom c’est pas grave 😭😭😭 yoonam nekku ci, man geuw ma etat, peuple laa geum ni mooy état lep loum beug dafko wara xeex ba am ko ndax pouvoir bi ñoo ko yor keneen yorul pouvoir kudul peuple, waaye peuple boo xam ni ken koune sa intérêt boppu reg reg moola ñor, boobu peuple manul defar dara, walaahi damaa gëm ni ñun waa senegaal bun ñu yobbu chine andi chinois yi senegaal du Yàgg dara dara chien melni Sénégal, Sénégal melni chine 😭😭😭 ca veux dire que afeer bi ci ñun population bi la, bun mankoo woon bàyyi plotik bi te and ngir defar réew mi kasé ken xoolul intérêt boppam, walaahi kon dépassé nan fii mais malheureusement dun ko def ndax lep lan plotisé lép, xamu ñu kañ lan wara plotik ak kañ lan wara jog and nek ben ngir defar dëk bi . C’est d’hommage
2026-10-05 07:22:37