@dudufaitdesvideos: #innondation

Dudu
Dudu
Open In TikTok:
Region: SN
Monday 05 October 2026 15:18:05 GMT
378286
158044
1708
1638

Music

Download

Comments

dosabb37
Dosa bb :
Sadio mané président du Senegal
2026-10-05 15:30:15
1623
diefaye09
Dié❤️ douce ✨ :
Inondation bi yeup dou etat c'est nous mm la population lou nekh way def di sani ordures yi surtout les sachets plastiques kou si wax mouni la mbed mi mbed bour la ken dou wax ken deuk bo xam ni ken yarouwoul motzx bour bi aussi mongui def louko nekh meunou ma wax sax ndax xol bou diekh nagnou subir conséquences yi rk
2026-10-05 15:48:48
913
ndia74sn
ITACHI UCHIHA✪ :
repartagez SVP
2026-10-05 15:24:21
3834
babaca343
Mindset 🧠 !! :
yallah rék kaye bour limou déff rék daffa guene ☝️🤍
2026-10-05 15:50:42
245
massamba1810
𝑴.4𝒔𝒔🪐🕸️ :
𝒎𝒂 𝒎𝒂𝒊𝒔𝒐𝒏 𝒂 𝒆́𝒕𝒆́ 𝒕𝒐𝒖𝒄𝒉𝒆𝒓 𝒑𝒂𝒓 𝒍𝒂 𝒇𝒐𝒖𝒅𝒓𝒆😔
2026-10-05 16:33:59
262
fatimarassoul50
🇸🇳✨فاطمة :
Qu’Allah leurs viennent en aide😭🤍
2026-10-05 15:22:06
7523
user1500487947438
Just me :
Svp niou wakhanté deugu Dakar deukou dokh la depuis temps colonial mtx toubab yen zone laniou tabakh defff fa canalisations mou normal. Malheureusement legui nieup beuk deuk Dk Keur massar Ouakam yeup ay toll la wone maintenant lepp defnagn ko parcelle nieup deuk sou tawé niou toumranké dakh dokh dou bayi yonam. D’une part état la dakh niom niou dieul lep centralisé Dk mtx nieup fa naniouy dem pour liguey moudié deukk naniou tass certaines administrations etatiques dans les autres régions d’autre part nioun la naniou respecter mbed mi dakh déchet yiniouy sandi moy diour li aussi. Y’Allah na yallah takhawou les sinistrés ak diaykatt yi yakoulé inshaAllah boudé 25fr la ame sakh dinagn ko deff si cagnotte bi inshaAllah.
2026-10-05 16:23:06
68
fallou_lahi
Fallou Faye :
Les responsables c’est Macky Sall, son frère mansour Faye ministre de l’assainissement à l’époque, Lassana ngagni Sakho directeur de lonase de l’époque et qui se retrouve aujourd’hui avec Diomaye. Rien qu’à Touba, plus 40 milliards nénañou defnañoukofa anamou ? Sénégal dou avancer jamais tant qu’il y’a l’impunité des pilleurs de deniers publics. Oú sont les responsables de cette dette colossale qui a fait que les sénégalais vivent dans une misère extrême?
2026-10-05 16:56:39
26
anta7833
anta7833 :
C’est triste pour un pays comme le Sénégal le gouvernement ne fait rien 😭
2026-10-05 15:25:11
874
pispa.fall1
pispa fall :
Politiciens mbalit sakh dako sékhlou;Macky,sonko,diomaye
2026-10-05 20:30:43
0
khoudiadiop352
khoudia diop :
Sénégal kagne lay bakh 🥺😔
2026-10-05 15:21:56
224
abdoulayecasaprod1
Casaprod :
Bro t’as oublié le comportement de la population sur la gestion de leurs ordures.. fi Guay Guiss nit nane dokh Sandi Mbouss bi … Lolou yeup ay details a ne pas ignorer
2026-10-05 16:06:37
155
kheuchla1
kheuchla🇸🇳 :
Allah🥰
2026-10-05 15:51:51
311
idyniang150
Idy :
Yallna inondations yi diekh 😭😭
2026-10-05 20:45:18
0
jainaba686
Naba :
Very sad 😔
2026-10-05 20:33:40
0
fatima_6c1
Fatima Cisse :
Yalna léene y'Allah takhawou
2026-10-05 19:41:22
0
paaapiis
paaapiis :
Une pensé pieuse pr nos frères et parents 🤍👏🏼
2026-10-05 15:21:04
271
user8726945122761
𝒊𝒕𝒔 𝒇𝒐𝒅𝒆𝒏💫 :
𝗯𝗹𝘆 𝗳𝗿𝗿𝗿😭😭
2026-10-05 20:05:23
0
wvw322
VM :
Macky Sall seul
2026-10-05 18:24:24
22
zalle21111
MAME SALIOU👑 :
yalla nalén yalla takhawou 💔🤲🏿
2026-10-05 15:21:28
63
wizemdi
EMDi⚡️ :
Gouvernement Macky sall khaliss biniou sathie yalla nagne ko fadioo ba dei😡
2026-10-05 15:36:03
335
ibrahima_323
Ibrahima 🇸🇳 :
Si j’étais un père de famille ma deuk si zone yii dina def le tout ba diaye sama keur deim dieunde beinein zone par exemple diamniadio dieum sebikhotane parce que dakar vraiment chaque année dafay guen metti (terrain simple bo diaye dakar meun na tabakh keur bou normal hors dakar ) di guein ma khass dh mais solution gueunoul bi vue que politiciens yi moy lolou
2026-10-05 17:47:34
7
alys838
Alé bike painter 🎨 🇸🇳 :
Motakh nit lou meun am santal yalla ndakh amna gnou fanan xolei ba fadjre té amouniou fougn fanan
2026-10-05 15:26:14
57
mbaye.446
Allah is one ☝️♥️ :
j'aime pas voir les gens souffrir walahii c'est désolant 🥹
2026-10-05 15:21:48
46
roukhayakhalil
✨Rokhaya_khalil✨💕 :
Wa moussi nougniou def aye waye🥺🥺
2026-10-05 15:54:19
165
To see more videos from user @dudufaitdesvideos, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About