wave défoul dara sa téléphone 10.000.000 bousi nékon 10 ans bo niewé fékat kofi dafa am lo khamné yaw mi brome téléphone yakou causé té do si bayi xél amoul informaticien wala hacker bou mana diékki rék dougou si téléphone diamour sans rien il faut guéndi bayi xél liens yiguen di cliquer site internet yiguén di dougou li boko éviter nit manoul am accès si sa téléphone
2026-10-06 05:07:36
324
Max store❤️ :
OM mo eupe sécurité
2026-10-06 00:21:02
182
DOU NDIOL C4 🤟🏽 :
Li yeup orange money nekeu si guinaw bougnou bayiwone Wave sakh orange money mome mouk
2026-10-06 11:17:25
31
001binoushasaliou💍Mrs ndiaye :
Khana Soko dougalé coffe j’espére k kén douko meune retiré
2026-10-05 21:34:37
105
Mbenza Salihate :
Kharal ma retiré sama 4mil yi sakh [Larmes de joie][Larmes de joie][Larmes de joie]
2026-10-05 20:39:59
83
Anne globale business :
mane 30000f may dioy😂😩💔
2026-10-05 22:29:15
7
NBA Ndiogou 🇸🇳🇺🇸🇺🇸 :
Ceux qui apprennent les logiciels xamna niou lii may wax y’a aucun moyen ou amoul benn système bou meunn takh niou pirater sa téléphone sa téléphone à distance c impossibles soit elle a cliqué sur un lien ou niou trahir ko mais kenn meunoul pirater sa téléphone dougg sa wave dieul sa xaaliss it’s impossible merci
2026-10-06 04:51:45
21
Abdou Fall :
Ki orange money moko yonni khame nako si service orange money bi
2026-10-06 01:31:16
3
Princesse ❤️dieng❤️ :
kharal ma daw retiré dji sm 5f yi guaw
2026-10-05 23:10:46
39
Yayou seikhe yi❤️🥰 :
Liii mongui beugue bari dhé
2026-10-05 23:09:53
72
julie :
limassi diakhale hnome bataye guenougnoy wakhe
2026-10-05 21:35:35
0
ndiayerokya :
wa orange Money nio liguey wa wave 😂
2026-10-05 22:57:56
0
penda_wuruss :
Wouyyy Lomay wakh ni😭😭😭
2026-10-05 19:20:22
40
Amoura fashion :
Orange Money rek
2026-10-05 23:46:00
5
L’harmonie 🥰 :
Wave woratoul
2026-10-05 21:34:55
3
Pablo Malick Fall :
ils sont peut être complice
2026-10-06 01:56:13
6
Quenne lebou🥳 :
Daniouy wakh orange mais bly nio geuna am sécurité wave
2026-10-05 23:06:27
26
Maman bou SBSy❤️🦋 :
Coffre bii sah moy lolou
2026-10-06 00:38:48
25
Dkr store :
activer la limitation du compte sur 1 seul appareil comme sa keine dou meuna connecter wou apart sa telephone
2026-10-06 11:18:44
46
user7192718407318 :
Bilahiiiii c vré mo dale sama dieukeur amoule bene trace bayiléne wave
2026-10-05 21:31:22
50
m. b :
arréter de cilquez les liens qu on vous envoie soyer prudent svp . pour.mane wave amoul probléme esque amoul niou beugeu danel wave Question là ?
2026-10-06 09:34:41
20
🫧✨꧁༺ 𝑀𝒶𝓇𝒾𝒶 ༻꧂🦋🫶🏽 :
Arrêtez de cliquer sur n’importe quel lien et de télécharger certaine application li woratoul
2026-10-06 11:45:41
7
ᥫ᭡ 𝑨𝒃s𝒂𝒂 ᥫ᭡🧸 :
Encore c la troisième personne bimay guiss mousiy wakh
2026-10-05 23:42:09
10
To see more videos from user @aby_sow_43, please go to the Tikwm
homepage.