Mia guissé mou douguou maïga ngen beug ko def évenement😂
2026-10-06 10:01:50
490
DOU LE CATALAN💙❤ :
grand bi nékk n'a start ni quoi 😂
2026-10-06 18:14:22
200
user5393742530600 :
khana d'ou nit rek[Larmes de joie]
2026-10-06 09:20:16
908
N ☘️NIANG 🥰 :
Li dey moma nara dall😂😂dem ba nek présidente ne maïga lay dem😂😂
2026-10-06 01:38:41
1111
KHADIJA☪️🖤 :
Yeine tamit guen ame respect machallah ❤️🤌🏽
2026-10-06 02:35:37
236
Bass’iste 🙏🏾🎸🎶🎶❤️ :
brom cap bi Moy genre grand you yagu ya Youssou Ndour Omar Pen RK lan kham😂
2026-10-06 02:33:36
120
Elhadj accessoires 📱 :
Mane mom kii rk la geum Machallah lep si fara 😌🙂↔️
2026-10-06 03:04:33
130
junoir :
Gni lougn def rek amna lou takh
2026-10-06 15:01:50
81
Mame Cheikh :
wax lene yéne ñiepou Alhamdulilah
2026-10-06 12:33:43
155
Alaba Ndiaye27 :
Legui MIA GUISSÉ bou douguou Maïga événement leu walla??
2026-10-06 15:17:51
17
𝑵𝒆𝒖𝒆𝒓....𝑫𝒂𝒃𝒐✪ :
un jour vers 3h du matin ma demon bena programme bay retour 😳ms jour bobou la kham ni yalla meusouma setane 😓may dokh ame Louma sentir sama guinaw souma diokhé mou bougé souma tahawé mou tahaw ma degon gnouni ken dou dokh di gesou goudi ah sama fitt bi togoul rek ma djeki rek daw ms Limay daw yeup tahoul mou bayma 😭ma boléko ay youkhou you metti sakh ba gneupe yewou géna dima diapalé 😭😭nékété allumettes bima don ataya la fate sama poche modon def bruit bi😭ma rouss ba legui douma sigui khôl wa kogne bi
2026-10-06 11:14:22
18
. :
barre de recherche bii do lén si wakh 😂
2026-10-06 06:00:49
44
Abdou khader :
Machala 😂
2026-10-06 01:22:18
32
Borom rewmi citizen 💙🤍100% :
magui liguèye wala 🥰
2026-10-06 12:08:36
18
DOMOU GAMBOUL :
Mia ndeysane day retane rk j’ai remarqué ça sur elle comme moi
2026-10-06 10:07:31
26
Salihate ❤️🥰 :
Borom maiga bi soube mou yok prix bi
2026-10-06 22:48:30
9
🖤CHEIKH🇸🇳 :
non Sénégal nekhna 🤣🤣
2026-10-06 03:00:46
13
kénal yalla :
mia da bakh
2026-10-06 02:37:36
12
omar gueye :
mia raftna mashallah
2026-10-06 10:08:50
9
kandji so :
bilahi da bakh rk machallah ♥️
2026-10-06 03:57:30
9
Papa mbodji :
Lerr nama xamou ko😂😂😂
2026-10-06 09:29:59
8
m m d🫵🏿 :
contanoul d
2026-10-06 11:08:36
7
Bizzy patisser🥯 :
Sénégal siww fi metina bilahi 😂😂
2026-10-06 11:11:32
5
seydina :
man souma yorone guene khamni ma simple
2026-10-09 16:19:21
2
Diouf Couture :
Wa ki mom 😂
2026-10-07 07:44:47
3
To see more videos from user @douprolofficiel3, please go to the Tikwm
homepage.