billahi geumnanii yalla dinako takhawou. abdou aziz mbay sopey rasoulillahi loumou dougeull kadoom inchallah dina bakh😭😭😭😭
2026-10-06 12:24:23
28
Dakar 🇸🇳 :
Serigne Abdou Mbaye Yaw dé boko toudé si sa lamigne dé dina ñou si am yakaar Yalla na Yalla nangou niane yeup si barki Serigne Babacar Sy rta amiiine 🤲
2026-10-06 15:01:08
7
cheikh fall :
Amine amine amine bour bi yalla nioune Say diam niolaye niane leep oyof thi barkep seydina Mohamed
2026-10-06 11:59:12
6
LaYeuh_Niang :
Bo Gnané Sunu borom mou nangou ko ame nassi yakaar☺🙏🏿
2026-10-06 13:47:40
13
LE PREMIER PATRIOTE :
amine ya Rabi baye Abdoul Aziz mbaye
2026-10-06 09:36:32
38
OMAR KANDJI LE BALLKHWMI C'EST :
y'a bakh papa amine yarabi
2026-10-06 11:47:18
32
A_h2o<< :
Amine y’a rabbi❤️👏🏿
2026-10-06 12:20:24
0
🧑🧑🧒🧒🙈 :
Secret bi nek si defff lou bakh🙏🙏❤️
2026-10-06 14:16:09
10
Gourcuff :
Yalnako yalla takhawou inchaalah🙏
2026-10-06 12:30:34
0
ibrahima mbaye :
amiine sama général
2026-10-06 11:50:44
14
Mor talla niang official :
Amine wayy yalnako yalla deff way si barke younenete bi saws ❤️🙏
2026-10-06 11:18:58
6
Packo diaz :
mbayang en Arabie saoudite et tous les détenus sénégalais a l'étranger ya n'en en pagaille
2026-10-06 08:39:54
10
Amadousow :
wallahi ndeyssan
2026-10-06 13:58:59
4
Apple User674322 :
Gnou bolési mbayang diop
2026-10-06 12:32:07
7
Mboup talibe mara :
Ndaysane yalla Nako yalla takhawou
2026-10-06 13:35:34
3
niang :
ndaysan yalnko yalla xetali insallha
2026-10-06 14:13:37
5
top bou sonko :
Amin ya rabi
2026-10-06 13:44:33
2
Mamy tall thiane Tall :
Ndeysane nit kou bakh day beug bokame
2026-10-06 13:34:22
3
Asfiyahi Couture officiel :
bilahi walahi talahi sama khel dal na alkhamdoulila sante yalla Bou bkh dina bkh dk inchallah dana woyof lolou sakhe bilahi yalla dinako takhawou dk inchallah
2026-10-06 13:03:35
4
Abibou mbengue HT :
Ndeysan yalla na yalla na ngou niaan yi
2026-10-06 14:39:11
1
Modou talibe s Babakar Abdou :
Amna si yakar si ay Biram bilay yalla bou yalla tass yakaramm
2026-10-06 12:26:08
3
saliou diagne ✅️ :
bilahi wakh na deug
2026-10-06 12:49:41
1
Dia :
yalla nako yalla takhawou 🙏😭
2026-10-06 12:01:55
1
To see more videos from user @ousseynoualamine, please go to the Tikwm
homepage.