@baayi.si.xeel: Ci aduna, bari na mbir yo xam ni nit ñi dañu koy ragal walla ñu koy wut di ci sonn, te fekk na ay mbir yu amul solo lañu ci kanam dëgg ! 💯 Lii mooy 6 vérités yo xam ni képp ku bëgg a am mindset bu dëggër da nga leen wara jàpp : 1. Jiko mooy nit : Mën nga am alal ju bari te amoo yar ak téggiin. Xalis du défar jiko. 2. Xel moo gën doole : Dooleu yaram mënul dëggal xel bu deeng. Xam-xam ak yar ñoo gën kàttan. 3. Jëf, du wax : Wakh ju bari du faj jafe-jafe. Jëf lu baax moo am solo. 4. Sutura ak jàmm : Am alal tekkiwul ne mën nga jënd jàmm ci xel walla wer-gu-yaram. 5. Tar dafay jeex : Rafetu yaram da fay jàll, waaye rafetu xol da fay des. 6. Sokhor du terro : Banyan ak iñaan du tax nga gën a mag. Xol bu set mooy mayé ndam. Liggéeyal ci sa jiko ak sa xol, loolu mooy sa vrai alal. Baayi Si Xeel, jiko bu rafet mooy alal ! 🔥 Ndax ban ci 6 points yii moo la ci gën a laal tay ? Tontul ci commentaire yi ! 👇 👉 Abonne-toi et Partage ngir am yeneen xalaat yu am solo bes bu nekk ! ❤️ Like ce post te nga Enregistre le post ngir fàtteku ko. Jookal ! Baayi Si Xeel ✍🏽 #Baayisixeel #Motivation #viral