Machallah rafét ngua trop🥰🥰 fo deuk bardé na dé meune am sa contact stp✌️
2026-10-06 16:28:47
49
maya diallo6 :
Ms yalla na yague amine🙏
2026-10-07 12:24:21
0
Saliou Sant aka muñ #& :
Jërëjëfëti Boroom Tuubaa
2026-10-08 12:11:42
0
Pa Matar 💎 :
Can you be my friend please
2026-10-07 09:17:25
0
vieux lo :
yalna na la fêkh si lou bakh
2026-10-06 15:39:17
19
محمد صور 🏴🚩 :
Kone del sol lou rafet pasque image dafay dess yalla nga goudou fann bou bakh inchalla 🥰
2026-10-07 10:05:14
7
𝔻𝕚𝕖𝕨𝕣𝕚𝕟𝕖 𝕥𝕙𝕚𝕒𝕨 :
Niou bayi xel adouna
2026-10-06 20:13:55
15
BACHIR LE PARISIEN ❤️💙 :
Yalla na yekh
2026-10-06 15:02:17
30
🤍diagne❤️narr🌹alves💎14🥀 :
mo takh nga wara sol lou bakh
2026-10-07 13:33:54
43
Thiatou yaye Dior 💯 ❤️ 💍💎 :
yalla naniou fk si lou nèh brome bi 💯
2026-10-06 15:12:03
16
Milka boye :
paix sa Son âme
2026-10-07 22:29:01
0
Seye couture ✂️✂️❤️❤️ :
beautiful ❤️
2026-10-07 12:36:34
0
Faye____Birame 221✅ :
Dina am dhe way Yalna yekh amine
2026-10-06 17:22:00
1
محمود خليل الحصري غي :
mounoul gnakk mais Yalna gnou fékk si Lou bakh té yalna gnou fi yalla bayi basi kanama kanam si barké yonéntibi sws barké Al khour aane 🤲🤲🤲🤲
2026-10-06 18:28:42
1
matar cana☝️☝️ :
Yalla nala yalla bayi la fi basi kanam yalla man nako yalla nala yalla samou yalla na yalla yaram way daw Lou yi Sama papa namou nako lolou dh mé yalla rek moman 💔💔💔 Adouna mo démé nonou wallaye ndayesan
2026-10-07 01:07:03
3
Abou :
Inchallah ☝🏾
2026-10-07 20:35:40
1
abdoulaye 🥰🥰🥰 :
'aime
2026-10-07 11:49:15
1
papedioufjoal :
Oh😭😭
2026-10-06 14:59:04
2
cisse Apple 🍏📲 🇸🇳🇺🇲 :
yalla nga goudou fann bou bakh inchalla 🥰
2026-10-07 20:04:42
3
Talibé Broum taif🤍🩵🔐 :
Mais yalla na yehhh rk inchallah
2026-10-06 20:57:34
1
user1846791267163 :
coo
2026-10-06 19:46:24
1
diagne jr ❣️🇸🇳🦁🥰🥰🥰❤️😍 :
ma femme 🥰
2026-10-07 04:19:22
1
(MOUHAMED)😇😎 :
Woye yaye nop na khalé bii 😔😔🥹🥹🥹🥹🥹🥹🥹🥹🥹🥹🥹🥹🥹🥹🥹🥹🥹
2026-10-06 14:12:19
3
To see more videos from user @mounass36, please go to the Tikwm
homepage.