Sam bén boy mo deggg wave woroul rek mou retiré limou yorone niou tafouko
2026-10-06 16:49:29
297
Aichou Ba :
Mane dei 100000 yii nek sama coffre rek moy Sama problème chaque instant ma khol sama coffre 😂😂😂😂
2026-10-06 17:29:39
104
fallou :
mane dara diaralouma délou orange money weve rek gnou déme🤣🤣🤣
2026-10-06 17:26:36
140
Patriote🇸🇳Sonkoiste !!! :
Certains se passe juste pour salir l'image de wave
2026-10-06 20:49:11
37
ndiayesonko 🇸🇳 :
orang la da beugu danél wave
2026-10-06 17:41:37
71
user25762723997010 :
Modou fall deugg rk nga wax gnoy dioxé sén xaliss
2026-10-07 09:38:25
0
Ndiaya Fall :
wave bakhoul
amoul securité
2026-10-06 17:08:31
24
TOURÈ AUTOMOBILE :
saway amena nioo xameni cliqué wun bén lien ta téréwul sen xalis dém na frère boromi xam xam lañu tmt man moom sama xalis démul mais na ko xameni moma eupeu xam si informatique fouf ta xalisam dem na dala daloul rk frère 😂
2026-10-06 17:09:11
9
Ndoye mor :
Imagine on se réveille un jour et wave n'existe plus
2026-10-06 17:38:25
10
@ Mame Saliou 221🇸🇳🇸🇳 :
mé wave da wara faye Modou mi limouy def wa wave manouniouko
2026-10-07 08:31:08
1
ablaye thioune sopo naby :
Sallahou alla Mouhamed 🙏
2026-10-06 19:40:47
16
Cheikh Cheikh :
Moytou léen application yoyu gnou naan léen meun nga ko installé sa téléphone pour am film yeup gratuitement… Khamo application bi kouko créée wayé beugg lou yomb et une fois installé tu donne accès libre à ton téléphone
2026-10-06 17:41:29
7
coumbysta :
bilay deugue nite nion security woul sen bopou dh wave yobou woull dara