un jour vers 3h du matin ma demon bena programme bay retour 😳ms jour bobou la kham ni yalla meusouma setane 😓may dokh ame Louma sentir sama guinaw souma diokhé mou bougé souma tahawé mou tahaw ma degon gnouni ken dou dokh di gesou goudi ah sama fitt bi togoul rek ma djeki rek daw ms Limay daw yeup tahoul mou bayma 😭ma boléko ay youkhou you metti sakh ba gneupe yewou géna dima diapalé 😭😭nékété allumettes bima don ataya la fate sama poche modon def bruit bi😭ma rouss ba legui douma sigui khôl wa kogne bi
2026-10-07 04:23:46
44
nyto gomis :
mane dé dama yemou si wadji
2026-10-08 13:49:42
65
JAAM RÉK :
je ne sais pas pourquoi mais je trouve dans ses paroles une profondeur spirituelle
2026-10-28 03:58:42
41
Boubacar sadio ly :
Alhamdoulilah il a dit la vérité absolue que dieu te en aide Amine yah rabbi
2026-10-18 17:48:11
1
mamadoulaminesaliou0 :
Kide bilakhii walakhi kou amoul degu mano Xam limi wax barki serigne Saliou Mbacke kamaloulakhi la