Foma tolo Magui kxol sun porodiksion ba kham dou gona 😭😭
2026-10-07 10:34:18
1
cheikh🇸🇳mbacke🇸🇳niang🇸🇳 :
yaw gurr yalla donou may leswaxol🙏
2026-10-07 10:44:27
0
BADOU😇SYLLA💕😇💕😇💕😍 :
Less wakhoul
2026-10-07 09:42:19
0
Fidèle 😘😂 :
Baloumala teh nga dougeul film bi
2026-10-07 01:20:13
15
Mouhamed Mbacke :
mane khrna basone way non
2026-10-07 07:14:34
0
ndeye fama mrs Fall :
nioun niola wara balou man Thi sama wale bopou magui lay balou bou bakha bakh🙏
2026-10-07 13:01:39
2
yacinend3 :
waaawww
2026-10-07 12:53:26
0
Talibe bamba :
yw gninga amél akh mo bari sounou épisode bi
2026-10-07 08:11:04
1
Fama Hanne :
Dambar yawe amélokéne axe wakhe deugue fa néx yalla yawe kou bakhna ga
2026-10-07 10:26:21
3
boy♥️ba💞star💯K M A💓👈 :
mais balnaniou la AK mais final bi n'a niéw🥰
2026-10-07 01:04:13
7
Mm :
Yaw amé lo kéneu akh au contraire gnoune gno la amél akh Par ce que daguaye dathe louné si épisode yi pour bégueul gnou
yalla Nala yalla démbeulé si li Guaye déf
Bonne continuation
2026-10-07 13:33:31
2
خَلِيلْ اَلْأَمِيرْ 🌸 :
sama gayi déf lén ndank RK yén Kii sougne ko encouragé woul warougne ko khas lii dafa métti dakay diaral mou bagna nélaw ndah RK ngén contan nagne ko nianal mo Guen Yii
2026-10-07 11:34:17
3
Sidy Diop :
foumu tolou man koumpa mogui may Ray de bly 😭
2026-10-07 01:12:50
1
diop90 :
Google La Liga
2026-10-07 13:52:48
1
Bayedame Cisse al diamaly :
Cv man gi saguma final bi anamu
2026-10-07 00:51:57
2
Ndiaye fadel :
diapa le inou nak
2026-10-07 01:03:51
2
LAYE BOU PHIL ✓$ :
dama décourage
2026-10-07 01:21:08
2
ibrahima 💙♥️🇸🇳 :
mane khrna basone
2026-10-07 00:50:17
1
𝐤𝐡𝐨𝐥𝐨𝐮𝐀𝐛𝐝𝐨𝐮❤️ :
mane dama mér😭
2026-10-07 00:47:54
1
Mame Thierno Ka :
bal naniou là mais finale bi na guén
2026-10-07 00:46:47
1
Massamba Niang :
foufou Toulouse way
2026-10-07 01:05:46
1
Sokhna khady 🧕🏾🫀🧕🏾 :
00:00🤗😂😂
2026-10-07 20:02:51
0
Ba :
sono nayou trop
2026-10-07 09:55:13
1
To see more videos from user @imisonyakar, please go to the Tikwm
homepage.