ndeye saan niit kou baakh samedi passé lakko djiss Thiès ma photo wou AK mom photo bi lérroull ma waakh kako mou retourné nieuwatt niou bokkatt photo après mou takhaw dii kharr baa kham ndakh foto bi lérr naa amm détt maashallah
2026-10-07 12:33:14
60
Mbaye Barhama Kandji SBN :
Koy défarr montage yi goor leh[Geste OK][Geste OK]
2026-10-07 12:25:05
8
Ndiaye 222 :
Aider moi à intégrer un dahira si barké baye niass
2026-10-07 15:13:51
10
nabou mou baye niass 068 :
bilahi dama beugeu tarbi you wayé sama yaye na gou woul ay way niou may déf mane en dama beugeu baye bilahi walahi niou keur baye lafa taf bamou bari
2026-10-08 15:02:46
4
barhama Couture :
dieureudieufé baye niass yalla nagnou yalla maye yalla si barki baye niass
2026-10-07 10:24:04
6
Ibn Sulaymaan LY 🦂🔴 :
SAYYIDIII TOUUUUUUT😍❤️
2026-10-07 13:15:49
9
Toure SBN :
NDEYSANE YEUNA MAN LOU NÉKH WAY ♥️♥️♥️♥️♥️
2026-10-07 21:07:24
2
MoMo Sn🌌💡 :
talibé Sangue Barhamou yi nio am xam xam machallah