Allahumma anta al-'Azim, anta alladhi khalaqta as-samawati wal-ard. Laka al-hamdu, wa laka ash-shukru, wa laka al-'awn. Allahumma unsur akhana Serigne Modou Ngom, warhamhu minal-bala', bi-barakati Sayyidina Muhammad, sallallahu alayhi wa sallam.dit Baye Fall Ngom mangui niane si barkep Mouhamed yalla takhawoulah inshahalla diga diakhal Américain 🇺🇸 faniou dieum bougne fa eguer gua hameni nite kou baxgua t yalla dinala walou dou niaw digua hameni Yalla bour bou mag laaaaa Allahou akbar ya rabi ya rabi ya karimou waloul sa diame bi xebou bi 🥺