Ñiou bari niou nék marché Ocass lidieuntiwouñou Serigne bi, alal molén yittél,molén indi Touba… wayé Baye fall yiñ sant liguéye bi nio déssé déf lilén war….daléna wara diaral, comme niom commerçants yi nim lén diaralé khoti ndigueulou Serigne bi….
2026-10-08 09:41:42
1
Sangue yaram 🥰🥰🥰 :
mairie ligueyam la défoule lou djii tou warna déf recensement kham niata nioy tok si wétou talibi gui naw lolou na woute budget tabakh ba néne marché si khalisou mairie bi Wala mou woute financement Souka dafé soune dikké mane fay chaque wéer khalis bi délou waat fam diou guée wone.
marché bi khalis bi nit gni fay monoo kham fane lay dou gou dou si marché bi dh tali bou bakh sakh amou fa bavage yi you si bari commercent yi nion ko défar.
la néene amoul organisation auto bou mak goudi rék lafi wara douk par ce que day khatal marché bi kéne dou dém kéne dou dik.
wayé nit gni so léne guénée guir marché bi dfa khat ta wouta lée lone foune diam fane laniy dialée dépenses la wakh dagay warou trop.
Touba deuxième capital du pays war na wésou fii soune amone mairie bou bakh la wakh lou bari bariii bari man nako défar wayé nak.....
lii dh moy sama khalat bou gaat nak
2026-10-08 00:23:44
2
user1587442747051 :
me Touba diaye rek moufa am
2026-10-08 12:48:51
1
tourè lbk :
lila yalla diguel sax dèfoko marchè dou pour auto
2026-10-07 23:38:04
2
Bassirou Diop :
nione sarigne bi rk lanou yakar
2026-10-08 09:36:18
2
thiame ndanane :
kou bakh wa touba marche bi lan man amou niou pékhé
2026-10-07 23:55:02
0
Universel carrelage :
bayilén nit yi liguey yon bi yakhaloul kén
2026-10-07 22:44:31
3
S Modou coll🧕👗🥰 :
Senagal mo nekh rek mané BO Amé lo deff nga dem defiko😂
2026-10-07 23:45:17
5
MAME FALLOU RÈK NIOU DÈM :
s touba dè koubakh la mome 🥰💖
2026-10-08 10:29:45
4
khadim :
Manga diakhasé yalla ak saydina Mouhamed
2026-10-08 12:08:47
0
سلدار مفاتح البشر :
tanim tv machalla s saliou
2026-10-08 09:30:29
2
chiekhendiaye06 :
boye yi danouye ligueye
2026-10-07 23:40:10
2
BASSE YAMALL DOMOU TOUBA❣️ :
li d'où yon
2026-10-07 23:55:15
2
Fallou GADIAGA :
nan bayyi mou sed [Cœur rouge][Cœur rouge][Réconfortant][Réconfortant][Prière][Prière]ligey diamou yalla rek [Prière][Prière]