@masserka: Sëy du rekk diw bëgg na ma, bëgg naa ko waaye ndax man ak diw man nanu ànd jaamu Yàlla ci kaw coofeel, respect ak worma. Naka ngay tànnée sa boroom kër mbaa sa soxna ? Noo mana def ba Yalla tànnal la li gënn ci yaw ? Ki ngay sëyal noo mana def ba seen digganté ratax ba mel mburu ak soow ? Lii lépp Seexul Xadiim dikkal nanu ci ca namu gëna jappandée ci nunn. Yii yépp ay questions la yoo xam ni nit war na ko poser boppam laata sax muy wax waxi sëy. Seen Emission DIIWAAN nak di na leen toppal lii ci waxtaan, aki xalaat ngir ñu bokk nunn ñépp jariñu ci njangaleem Seexul Xadiim.@Jibril-Karim 🇸🇳🇫🇷 @Cheikh Fall 🇸🇳 🇫🇷 @minute_xassida @Dahira Al Hijratou Paris @Diawartoulah Tv (Paris)

Massaer ka
Massaer ka
Open In TikTok:
Region: ES
Wednesday 07 October 2026 22:47:55 GMT
165484
33454
420
1284

Music

Download

Comments

bigcana28
bigcana28 :
Le nom du xassida
2026-10-07 23:57:06
198
machallah784651215
MACHALLAH CARRELAGE :
bly mako kham ba sama sokhna kou bakh la
2026-10-08 01:11:39
450
dijalaprincesse5
❤️Soxna Khadija 🥥 :
Mogui nonu
2026-10-08 00:32:11
139
sonko.moy.diomaye51
seydina oussmane snoko points :
komaye envoyé khassida gui guir yalla ❤️
2026-10-08 10:34:49
7
codoukhalifa1
Kiki❤️ :
Daw kholi khasida bi
2026-10-08 12:30:53
167
sokhnafatihissadiop
sa touba08 :
khasida tani monawara tani la todo
2026-10-08 07:45:32
16
unesalikhate88
Une_s@likhate_xasida88🧕🏻🫀🤍 :
Tourou khasida yi yanla
2026-10-08 00:06:34
54
amycollediop4
Miss Entrepreneuse 💵🛍️ :
Sm premier cadeau 🎁 bousi mawahibou andoul doumako lale
2026-10-08 00:19:57
64
msaccessories7
🅽🅶🅰🆁🆈 𝐋𝐀𝐌𝐓𝐎𝐔𝐑𝐎 👑 :
wallahi
2026-10-08 00:38:41
98
elhadjiomarfall12
POF9 ⚽️🥅 :
Serigne bi bayiwoul dara 🥰😁🙏🙏
2026-10-08 07:07:52
26
daddo1.0
dado 10 :
Thiey diotayou mouriez aka selll❤️❤️❤️
2026-10-08 11:16:07
0
aliou.gassama.516
Aliou gassama 516 :
ndye sane
2026-10-08 22:19:18
0
assane.seck.sandag
Assane seck Sandaga :
Salalahou Ala Mouhamed
2026-10-08 08:04:01
101
diawserigne450gmail.com
diawserigne450gmail.com :
Khmnasy dare ❤️
2026-10-08 09:20:02
0
badar.leye
Badar Muhammad SLHW ﷺ❤️ :
Boroom Tuubaa moo baax
2026-10-08 12:36:17
9
laminesene544
Lamine Sene :
2026-10-08 13:12:34
12
bousso.pieces
Abdou Khadre Touré :
2026-10-08 12:50:07
7
mame.cheikh2343
Mame Cheikh :
wax lene yéne ñiepou Alhamdulilah
2026-10-08 18:09:52
0
sokhnafatihissadiop
sa touba08 :
bilakhi masi xam dara 😭😭🙏🙏 déff guiss bilakhi
2026-10-08 07:44:15
34
fatou_saliou_dione
Soxna Fatou Saliou 🇸🇳🇮🇹 :
Je prends note
2026-10-08 07:29:29
27
amadoudiallo8700
Ahmadouna Rahmadouna :
Koufi gueneu beug Serigne Touba
2026-10-08 10:20:45
10
codou.260
beauté africaine :
moom nairi khasida la wakh Ban ak banla wala niari yepp bénla
2026-10-08 08:11:54
6
k9820408
k :
Fane la meune amé traduction en français bi ??
2026-10-08 01:09:07
9
sidibayfallfall
Sidibayfall :
Machallah mass namnala fall
2026-10-07 23:20:25
10
eleveurbi2
Élevage Sénégal 🇸🇳 🐏❤️ :
Ay way lolo rek la beug 🥺🙏
2026-10-08 00:18:19
7
To see more videos from user @masserka, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About