Saway dimbaliniou fi bene djiguene matou fi bene goor aussi matoufi may lene nite yi diam nite boko beuguer nangakoy beug si nimou mel
2026-10-08 10:46:05
9
PAD12 :
alkhamdoulilah ba kima nekal amoul si djiko yi bene machaAllah
2026-10-08 10:52:58
15
KIL KA TOURE :
sa nana yii yépou nokoy khamé tako baparé 🙏🙏🙏
2026-10-08 09:16:50
6
mad dalill ?? :
mais comment savoir tous sa , avant de la mariée ??
2026-10-08 07:23:16
7
sokhna🏀🏀 :
yalla na gnou yalla mélle comme ces femme amine
2026-10-08 12:01:03
2
Ahmad :
Maa chã Allah Frère.
2026-10-08 10:50:02
3
Mame dabakh shop 7086191##76 :
صدقت 🥰
2026-10-08 11:40:02
2
Abdoulaye Sene :
man dou ma ame😂
2026-10-08 13:06:48
0
saanoxo_rachiid✍ :
amna solo lool macha allah [Prière]
mais li yeup pour nga kham ko si sa partenaire niata temps la wara durée comme nioune célibataire yi islam danio téré relation you durée bi yagg??
2026-10-08 06:39:36
0
Cheikh Sow 🙏🙏🫶🫶👍👍👍 :
Machallah
2026-10-08 02:10:57
6
Sy business téléphonique📱📱👈 :
Kon douma tack
2026-10-08 11:46:00
0
LOdiA🤴🏼 :
Merci
2026-10-08 12:58:36
0
abybatoudiakhate2 :
machallah [Réconfortant]
2026-10-08 01:14:17
1
wili wala🇸🇳🇨🇮 :
Amna solo
2026-10-08 02:39:39
1
mouhamed n صل الله على محمد ❤️ :
ماشاء الله
2026-10-08 11:24:38
0
Taylor :
2026-10-08 11:34:50
0
ALLALOU❣️ CHEIKH IBRA FALL 🥰 :
serigne mangui ziar boubakh mai li nga wakh fi yeup dh es k am na djiguén bou meloul nonou khana mougne rek wayé 😩
2026-10-08 09:36:11
0
Xalifa_Ababacar :
Ah doyna waar al anana yi ak al manana yi bari nagnou fi lool surtout al hadaqqa yi