Bilay ki damako yeureum li dafa meti beugu na sey mé amoul chance
2026-10-08 10:13:32
85
Jolie 🥰cœur ❤️ 🇸🇳 ✌🏾 :
Boulene ko juger fallé mü guene lii s xoll bii lii dafa metti sama yaye lii la done dath ak sama papa djitlé😭louné lako dane defal djeukeur dji si souff juste pr sagal bopam sama papa djitlé di sath sama yaye samaye frere sene khar toud yeup mako djeund masoul raye xaru tabaski té wallahi am nako ndakh mongui ligueye depuis 1999 la neck sunu keur ms dawul defal dra sama yaye bole si di weur di djeul sama yaye di faye ay bor yumou lebul just bagne mu djeum kaw billahi wallahi dama dane xoll sama yaye sah diko wakh kii du kou bakh je m rappelle bima necké xalle diko wakh papa fou kene nekul mouni ma doul douma sa papa un jour dafa am sohla si mane ap problème xaliss bu beuri ma fadial ko neko pourtant yani ma wone douma sa papa tu te rappelle mu yeugal bop bii ms Allahamdou lillah sama yaye yewuna gnane ko batt si 2026🥰❤️🙏🏾✌🏾Allahamdou lillah nitt ku yess dougal lima dound nii ak sama papa djitlé lii mossi gana touti dafa feck nii souma wakhe lepp Dina am niou xam nitt ki motakh manouma wakh lepp
2026-10-08 08:10:00
397
Mrs sall :
Na dem yalla dinala diokh louko gueuneu inchalah
2026-10-08 06:40:32
198
Princesse keita❤️ :
Mane dhé sama dieukeurou yaye doumako deef pape pour lane
2026-10-08 09:08:27
69
🌸Maria🫧 :
Vraiment beug na sifffff
2026-10-08 04:02:56
396
user7547687810015 :
Tu très bien fait 👍
2026-10-08 03:36:52
195
thiatouyayam lebou :
lima begu wakh yeup la meunoul bind
2026-10-08 04:20:34
178
Fatoumatarr ❤️😌 :
Eyy y mame walo mi yerem nako😭
2026-10-08 07:19:31
249
Chez Madame Seydi :
ho rox lila raw barrina 😂 thiey yalla gor gni tamite
2026-10-08 14:52:32
0
💕bb💕 cha cha💕💕 :
dairo nopou yi dafa rafét
2026-10-08 12:03:57
0
KYASaliou ❤️ :
Nul ne peut parcourir à son distin Yalla nala yalla takhawou mougnal lep dafay diekh inchallah