😭😭 il faut ga néke modou modou pour comprendre limouy wax, stresse bi rék dalay doflo
2026-10-09 01:33:24
707
Mame Cheikh :
wax lene yéne ñiepou Alhamdulilah 😭😭
2026-10-09 06:56:48
508
Narru a Vie ❤️💚💃🔐 :
serigne Modou ngom yalla nako yalla takhawou amiiiiiine Yarabi 🤲🤲🤲
2026-10-09 00:59:37
852
N'fa :
Bayilénn modou modou yingenn di wo dilenn niane Niogui beugu dé 🤦♀️
2026-10-09 09:30:52
67
Oumar Ly :
4h lay nelaw et j'ai tjr la motivation pour continuer à cause de ma famille et de mes prochee
2026-10-09 04:07:34
176
boye Bou ndaw bi 🥳 🎊💥 :
ndaysane Lou méti yague na si adouna modou ngom yanako yalla téguill natou bi❤️😭🥹❤️
2026-10-09 00:37:46
234
Une Senegalaise🇸🇳🫶 :
Mann mii djiguen sakh douma nelaw lou matt 4h😌
2026-10-09 13:44:08
1
Dija❤️ :
Gni donn wah gueneu n’a nak
2026-10-09 02:02:18
188
Talibe yayam❤️ :
Wallahi souma khamon ni touki nila mel douma fi niaw😭😭😭
2026-10-09 07:36:04
112
khakhakhakhalammm :
Touki dafa méti bilay
2026-10-09 11:31:03
12
Trecce🇮🇹 :
Bilahi stress rk mo diep nit yi😭😭
2026-10-09 14:49:52
0
jojo0345 :
ndaysane yalnako yalla takhawou 🥺tei teguil ko natou bi🙏🙏🙏
2026-10-09 00:59:45
155
sokhna may ❤️🧕 :
Yalla nako yalla takhawou
2026-10-09 00:57:21
241
diagne nare :
Bilakhi limou wakhe kou touki woule manoko kham liniouye dadie té lép ndiabote mo takhe yala sam niepe ak soutoura
2026-10-09 13:32:22
0
Armando :
sa waye mayléne niou diamou aurop loumou métti métti Sénégal moko raw au moins fofou amna justice nioune gnieup ndiabot mo takh niouy daw
modou ngom nane ko nianale yalla téguille ko natou bi mo geune wakh diou bari
2026-10-09 08:23:54
65
J’aime ma mère ❤️🥹🇸🇳 :
Oh ylla nko ylla sutural amine
2026-10-09 12:49:17
0
tandine coiffeur🇸🇳🇸🇳 :
Yalla nako yalla takhawo🙏🏽
2026-10-09 01:01:48
107
Maguita Darou Diop :
Ay li Mètina lol yalla nako yalla takhawou
2026-10-09 12:12:39
0
Yy papam beug bamba 🫀🩸 :
alhamdoulilah salalahou allah Muhammad
2026-10-09 12:43:52
8
Talibe sarif hassane fall al :
Ndeysane
2026-10-09 01:53:28
33
MoHameD✪🇪🇸 :
defois ma tok ni esk duma gnibi watt[Llanto]
2026-10-09 06:00:21
70
Pape faye :
yalna nako yalla takhawo si barké séydina mouhaméd
2026-10-09 01:19:52
112
Sala business haïr 782957648 :
Bilay yalla bakhna 🙏🙏🙏
2026-10-09 01:06:33
71
Coumbsita❤️💫🔥 :
Yalla nako yalla takhawou barkel Seydina Mouhamed 🙏🥹
2026-10-09 08:29:32
17
magattesene82 :
Aurope stresse kasse leu bilay yomboul quoi 😳
2026-10-09 10:07:24
26
To see more videos from user @filsdembaovilleneuve, please go to the Tikwm
homepage.