@baayi.si.xeel: Ci aduna, xeeb sa bopp mooy tàmbali gu ñaaw gualay wàcce daraja. Li Yàlla la may, mu ndaw walla mu rëy, xewal la go wara sant te jëfandikoo ko ngir yokku. Su nga gëmee sa bopp te xam fii nga bëgg a agsi, ken mënula teye ci sa yoon. Bul xeeb sa bopp : Am na doole ak kàttan lu nekk ci yaw loo xamul. Sant Yàlla ci li nga am : Li nga yor tay mooy sa péyékay ngir tabax sa ëllëg. Focuser ci say objectifs : Xam-xamal fii nga jëm te nga liggéey ci sutura. Baayi Si Xeel, gëm sa bopp mooy doole ! 🔥 Ndax d'accord nga ne gëm sa bopp mooy tàmbali gu unte bi ? Tontul ci commentaire yi ! 👇 👉 Abonne-toi et Enregistre le post ngir fàtteku ko ! Baayi Si Xeel ✍🏽 #Baayisixeel #Motivation #viral #pourtoi

Baayi si Xeel
Baayi si Xeel
Open In TikTok:
Region: SN
Friday 09 October 2026 08:06:08 GMT
19895
1647
12
17

Music

Download

Comments

babalinfluenceur
baba l’influenceur 🧠 :
Merci waye
2026-10-12 22:48:01
3
latyrmindset1
𝐋𝐚𝐭𝐲𝐫_𝐦𝐢𝐧𝐝𝐬𝐞𝐭🧠 :
2026-10-09 20:13:49
2
2ma5c6
gaye dg💟😎 :
[Réconfortant][Réconfortant][Réconfortant]
2026-10-09 10:58:10
1
papa.ndiaye670
Papa Ndiaye :
😌😌😌
2026-10-09 11:07:38
1
seckbay.maillot
@seck bay business :
🙏🙏🙏🙏
2026-10-09 11:21:02
1
djilythior
Djily Thior 🤴🫴✈️ :
❤️❤️❤️
2026-10-09 12:50:55
1
diomaye.5d
Diomaye 5D🇸🇳🇺🇸🇪🇦🇲🇫 :
🥰🥰🥰
2026-10-23 10:38:12
0
moustapha.mbaye966
Moustapha mbaye :
♥️♥️♥️
2026-11-06 07:38:57
0
user9154130726028
user9154130726028 :
🥰🥰🥰
2026-11-12 02:39:04
0
user7608695713752
AMIRICANA :
🥰🥰🥰
2026-11-19 23:15:46
0
To see more videos from user @baayi.si.xeel, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About