Sosi begué sakh boul déglou musique musique bakhoul
2026-10-09 15:28:05
220
BICHRI💚 :
Yoon wiga dieul yalla nalasi boroom bi saxal
2026-10-09 14:43:57
148
Narou Serigne ahma badawi ❤️ :
bou yiwe rk rafét Machallah
2026-10-09 15:40:54
20
ndawa :
je ne sais pas pourquoi je porte tant d'affection d'amour et de respect envers ta personne tu l'un des rares personnes que je regarde et j'ai de l'administration
yallah te guide encore plus sur le bon chemin Machallah 🥰🥰🥰
2026-10-09 12:28:51
49
Fatou~Kinè~Bou SBS❤️🦋🫀🥹 :
Chacha yaw rk la buga giss so gniewè Gambia 🇬🇲 ❤️❤️❤️😭
2026-10-09 16:16:50
1
maria :
Je t’aime shasha walahi ❤️
2026-10-09 17:45:58
1
Soxna_ Amy_falilou💞🧕 :
Machallah aljuma moubarak yalnala sunu borom miy adji makk dji borom yeurmandé bou yatou bii taxawoula arreuh la sam la gueun la xir thi bopam moussal la thi thiat ak lamign contan trop thi ioe machallah yalna nga sax thi dakk 🧕🥰❤️mouray dra dakk ko🥰
2026-10-09 14:20:19
17
Fils :
Bilahi li dafa raféte yallah nalasi yallah sakhal 🙏
2026-10-09 16:13:54
5
Jule Barry :
Allahouma barikk 🤲🏼❤️
2026-10-09 12:25:38
24
Maman ndime culture ✂️🥰 :
Machalah bohamon moronimo bahe dokabayi de diapalrek
2026-10-09 12:44:22
9
NS :
yagi rafet I love u
2026-10-09 17:27:10
0
Une hijap 🧕🏿🖇️🪭💗. ✨ :
Ah li d mom alkhamdoulilah rk ngay degeu ak machallah 🤲🥳🥳🥹✨🫶
2026-10-09 17:48:08
0
rema :
bly damala beugue
2026-10-09 17:41:41
0
101zahrasaliou :
Machalaaa ne l’enlève pas❤️❤️❤️
2026-10-09 16:11:07
0
SIDIBARRY DOMOU SHASHA ❤️😎 :
Machallah maman ❤️🥰 Jummah Mubarak ci yaw, yaay sama ❤️🤲🏽 Yàlla na la may gudd fan ak wér-gu-yaram, jàmm ak mbégte. Yàlla na nangu say ñaan, baal la say bàkkaar, te wàcce ci yaw li nga bëgg lépp ci sa xol. Na la Yàlla dolli yërmandeem ci àdduna ak allaaxira. 🤲🏽❤️Yàlla na la aar ci bépp lu bon, soreel la tiis, xel-ñàkk ak jàqare, te feesal sa xol ak jàmm ak dal. Na la Yàlla fey lépp lu nga def ci sunu kaw, sa mbëggeel, say coono ak say ñaan yu nga ñaanal nu. ❤️Yàlla na bés bu nekk ci sa dund doon lu fees ak barke, alal ju baax, wér-gu-yaram ak mbégte. Amiin ya Rabb 🤲🏽🕌❤️Bëgg naa la lool, yaay sama.
2026-10-09 12:33:05
17
💫khadija saliou 🧕🦋🌸 :
machalla 🥰 bonne continuation 😳
2026-10-09 17:43:32
0
Prince bousso Bally :
Le bon chemin
2026-10-09 17:20:01
0
Mariame 🖤🤗 :
Meilleur déçussions [Joie][Joie]
2026-10-09 16:56:50
0
Mme Camara :
Félicitations QU'ALLAH te facilite Chérie [Mains ouvertes]💚💐🙏
2026-10-09 16:52:11
0
ibrahimadiallo342 :
Machallah Machallah 👆🏻👆🏻
2026-10-09 16:45:41
1
Mya🥰❤️✨B :
Masalah
2026-10-09 15:25:22
3
Aicharassoul bissness :
Machalah yalna yalla sakhal la si
2026-10-09 15:57:22
0
To see more videos from user @shitashasha27, please go to the Tikwm
homepage.