@seydina_aliou_barry: Diine ji dou wakh sa khalat ay textes la#pourtoi #fypp #viralvideo

Seydina Aliou Barry✪
Seydina Aliou Barry✪
Open In TikTok:
Region: SN
Friday 09 October 2026 15:15:34 GMT
47485
2445
322
115

Music

Download

Comments

cheikh914
cheikh halime gueye :
Lima si geuna meti amna niou ko geum 😳😳
2026-10-09 16:48:09
73
niang1840
35/31 NIANG🇸🇳🇮🇹 :
linga wakh dou deugue Faye diouli amoul
2026-10-10 21:08:13
0
eboubah22
eboubah22 🇬🇲🇮🇹 :
ma Shaa Allah. thank you for the clarification 🥰🥰
2026-10-10 14:49:55
0
gauche25
Mamadou diop :
kou mom diouli ak ndax day leblé?. waxken lou yalla wax
2026-10-10 15:25:06
0
laze78
DIOP :
ah professeur kaye limou wakh khamouma foumou ko dieulé
2026-10-09 15:56:58
26
bipa1660
bipa :
mom téé moo yam thii limou kham
2026-10-09 22:52:18
1
saintlouis253
Sopé Naby❤️ :
Billahi oustaz tik tok yi kouléne mouytouwoul
2026-10-09 19:09:53
11
user7803728347184
Élevage Ndi@ye G@ïndé 🦁 :
kepp kou amel yalla béne borrou diouli ba doug bamel dina la wex xatt
2026-10-10 15:42:54
0
lfkd6883
Anonymous :
Yenna bokk li nguén wax.. dé niarri conditions la wax nelaw ak faté ....
2026-10-10 08:33:18
0
teacher1202
Bassirou Dieng :
wakh deug mounone na yem ci ay cas de divorces yi
2026-10-09 17:44:02
9
user3415953312063
seck :
machalla sayidina aliou bary thi légal yi amena solo lole
2026-10-11 01:08:26
0
abdoulayefall533
عبد اللّه فال :
Yalna guéne toup ko
2026-10-09 17:53:31
1
gueye.ndioro.coutur90
gueye Ndioro Coutur ziguenchor :
machalah yalna yalla barkél
2026-10-09 16:19:39
8
julesbenone
jules :
tu as enleve le debut de la video. il a tenu son propos par rapport a un contexte bien precis, c'est a dire celui qui deliberemment ne prie pas a l'heure, pour se rattraper plus tard. il a parle avec connaissance, meme si son avis peut etre discute.
2026-10-09 18:17:09
1
mouridembaye6
Mouride Mbaye 1710 :
Lii nga wakh nii dé mooy deugg !
2026-10-09 18:13:21
8
user4091617048175
morndoye931@[email protected] :
ماشاء الله يا أخي العزيز حياك الله وأطال عمر مع عافية وسلامة من كل عين شر أو حاسد أو حاقد أو فاسد وجمعنا الله بالرحمته
2026-10-09 15:53:05
6
yayathiam280
yayathiam280 :
Erreur .dinné alkhourane rék leu. dou boukhari .dou mouslim.dou ibnou Madia.. diouli kéneu douko faye bou passé.
2026-10-10 08:30:08
0
momo.gueye96
Momo gueye🇸🇳 :
Machalla Oustas
2026-10-09 15:27:58
6
user18784228
Sayfon Chérif :
khamkham bou lere merci ya oustaz
2026-10-10 09:32:48
1
abdoulayethiongan2
Mr Thionganes :
Écouter bien le mR (tayéfe la wakh)
2026-10-09 20:58:05
4
meissa628
meissa Kébé :
شكرا جزيلا
2026-10-09 15:29:00
1
ahmadou.dieng23
Ahmadou Dieng :
amoul been teree tafesir bou le profet bi firi
2026-10-09 23:35:02
0
user7553217201975
user7553217201975 :
chef balegui wakhago fou alkhourane wakhe niouye Faye diouli
2026-10-09 21:53:38
0
elhadjibabou809
Elhadji Babou809 :
Le professeur a parfaitement raison. Quoi que tu puisses dire, tu ne pourras jamais le contredire. D'ailleurs s'endetter en prières est un manque de respect pour Le Seigneur.Le repect envers Allah, c'est cesser toute activité au moment de la prière et s'en acquitter.
2026-10-09 21:11:22
0
cheikhmoustafa5
cheikh moustafa :
niou bari si senegalais yi daniouy diawalé alkhourane ak diné l'islam. alkhourane lay la (preuve) pour l'islam mais dou diné🤝
2026-10-09 22:02:06
3
To see more videos from user @seydina_aliou_barry, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About