Lidè mo yag sama diang Bac +3 meunatouma deff bene concour 🥺
2026-10-10 10:45:49
544
saloum369 :
2ans de prison de ferme
2026-10-10 10:20:20
1200
Mouhamadou 427 :
souniou gouvernement bii nioy ay lache rek
2026-10-10 10:41:04
1611
venusnoir🇪🇬🇸🇳 :
Na dé si prison bi
2026-10-10 11:15:21
894
nationaliste 💯💯🇸🇳🇸🇳 :
dring baxoul si reew
2026-10-10 11:10:47
584
💫666 :
Naniou récupérer souniouy papier avant tout 😡
2026-10-10 10:27:59
388
P-BLACK 🏀💯❤️ :
Pour mane li Senegalais yi gnoko wara Fadial sen bopp diaroul khare yone bilahi lgui Deuk bi changer
2026-10-10 10:57:25
314
cheikndiaye491 :
sénégal tahirou sarr rék moko mana réglé
2026-10-10 11:04:21
695
𝓃𝒶𝒷𝓎_ 𝓇𝒶𝓈𝓈ℴ𝓊𝓁 _✰ :
Elle a arrêté pour l’instant
2026-10-10 10:23:37
1885
Ochoooo :
Deuk bo khamni gniko djiteh yeup khalisss molen gueneul sen ngor mouy président di police di procureur di maire di lepp.. Ce sont les premiers voleurs et criminels de notre Pays
2026-10-10 11:14:58
79
Mame Cheikh :
wax lene yéne ñiepou Alhamdulilah
2026-10-10 11:31:38
250
Modou Diop :
sama xol bi nimou dièkhè si lii
2026-10-10 10:32:48
794
Sénégalais et fière :
Kaylor il faut ngen dem dépose ay plainte ndakh presion bi geuna kawé sinon atane naniou ko libere
2026-10-10 11:15:06
77
DAROU MINAM ÉLECTRONIQUE :
merci kaylor liguey bu refate biguay déf si réw. diomoy défouko député yi défougnouko
2026-10-10 10:36:21
244
1960 :
2026-10-10 10:21:24
85
Demba 🇸🇳🇸🇳🇸🇳 :
Bravo à nos enquêteurs. Que justice soit faite.
2026-10-10 10:25:46
64
āL Amineبار Gømis🪐☪️ :
Keylor yalla nalla yalla sammm
2026-10-10 11:20:33
51
saliou :
2026-10-10 11:16:57
27
Al moukhtar deug 🚩🏴✨ :
galsen dou rew le pays va très mal 😏
2026-10-10 10:54:48
62
Le soldat de Sonko :
Sénégal mo amoul autorité si bommp. sunu dirigeants yi gno yapp la population si boppam
2026-10-10 11:11:32
108
Aziz Borom Fouta🇸🇳✊🏾 :
Merci beaucoup Frère
2026-10-10 14:12:26
18
sisko Italien523 🇸🇳🇮🇹❤ :
Heureusement ba sama Bâ amoul H
2026-10-10 14:52:20
26
Aicha mou Baye14🥰❤️ :
Louko wa Senegal def tmt bamouy def li yeup
2026-10-10 12:41:04
5
M B A Y E🇸🇳👩💻 :
mom diapou naniou ko di wala dou degu
2026-10-10 10:26:14
257
moisabrown :
on doit criminaliser tout acte de falsification de papier dans ce pays sinon ce fléau ne s'arrêtera jamais
2026-10-10 12:09:57
33
To see more videos from user @keylor1004, please go to the Tikwm
homepage.