dioum ga dé Serigne Babacar mo magone Serigne fallou mague Nako trois ans Serigne Babacar 1885 la Serigne fallou 1888 la
2026-10-11 18:40:01
1
@ PAPIS 86 :
❤️❤️❤️💚💚💚💚💚💚💚💚❤️❤️❤️
2026-10-11 15:21:13
0
حبيب :
ماشاء الله تبارك الله
2026-10-11 17:48:40
0
CAAD🪶✍🏽 :
Baye moussoul ame photo ak serigne Babacar moussou tog niom niar. Vraiment delen wax histoire yi comme nimou demei
2026-10-11 21:05:29
0
Diallo 123 :
Allahou akbar
2026-10-11 15:52:22
0
Moustapha Niass :
Baye Niass AK Serigne Babacar sy béneu yoon lagne meusseu guissé te cheikh Tidjiane sy al Maktoum la baye Niass done setssi néko ma sétssi walé sa waydiour serigne Babacar sy ndakh kou am dom bou melni yaw kham wadiouram warna boudoul bobou amatoul amougnou photo itam gnom gnaar makk béneu lagnou mais nay lérr rek
2026-10-11 18:52:03
3
deug rèk la vèritè :
seydou nourou tall la dou baye niasse
2026-10-11 20:32:45
0
cheikhgassma784570246 :
❣️❣️❣️
2026-10-11 07:46:00
2
Amate fall Rafael leão :
🥰🥰🥰
2026-10-11 07:53:56
0
To see more videos from user @elmatarbouserignebabacar, please go to the Tikwm
homepage.