Pour mou ler diappe wouñ ko yallah de ms limay deff koudoul yallah manou ko mome cheikh ahmadou bamba
2026-10-11 21:02:00
134
☆ASADOUL☆HAMZA☆💙🤍 :
amoul morom dh 🥰
2026-10-11 21:57:47
55
sokhna yandé Diouf 💍💫😍 :
ndeyessane thiey s touba amoul morom dh 🥰🥰🥰🥰
2026-10-12 00:43:08
0
un mouride :
Amoul morom
2026-10-11 19:36:35
64
santé Daam kese :
Serigne Touba kiné là 🥹
2026-10-11 19:10:29
130
serigne fallou kiman ✍ :
bilahi degu la kham nako bobah nite ko yemé ta mata bayi khél
2026-10-11 20:11:41
27
Sëriñ fallou Seye xassida :
Dou nitt dh yangui dioum dh 😭😭
2026-10-11 21:08:44
14
Sama dëkk sama fierté.❤️🇸🇳 :
Ay waay live bi bu ma ci tombe woon ba wax li ma bëgg a wax ci dëkk bi sama dënd bi fees na lool te lima bëgg a wax yéen ñi dëkk ci dëkk bi te am ñu leen xam ñu di leen déglu war ngeena waxaaleel mboolem ku dëkk ci dëkk bi te baatam soriwul.
2026-10-11 20:52:05
21
Modou mbaye 💚Ousmane sonko :
Serigne Touba da Bakh dé bilahi [Prière]barké s. Babacar sy[Prière][Prière]