yalla geureumnako,yonnentabi geuneumnako kouko geureumoul ya xam
2026-10-13 13:38:22
573
CHEIKH😎✪ :
Benn waay may dokh sama soxla mou yor apparém bobou dima wideo loy wideo la xamoul
2026-10-13 12:49:19
289
SIRAATAL MUSTAQIM ☝🏾🇸🇦 :
Geume Serigne Touba force leuh wolleuh
2026-10-13 01:16:27
275
LIL OUZ :
doko wakh mou taxaw mayla photo 😅
2026-10-13 01:21:27
216
Solly :
Sa Tawhiid "kénal Yalla" motax niou sop la.
2026-10-13 14:36:51
208
Sonhibou salafi❤️ :
soubhàna lah wà loutakh démô si yalla direct alàhou akbare
2026-10-13 10:50:05
110
Vikings :
Serigne Touba Dee na soul naniou ko
2026-10-13 21:46:06
92
Aliounurudaryni 💌 :
Xar ko tafsir bi di nieuw bam ni la man dal nit num meuna dieuleh tlph bi dek ko nit di wax rk 😂😂
2026-10-13 00:56:59
639
SERIGNE❤️MBACKE🧠MOUHAMED 💕 :
Dinala khoute ba dh😁😁😁😁
2026-10-13 11:50:20
116
SMD✪ :
fii laa dem si bene progaraaam ab prograam la wakh dh bene waay serigne biii yorr téléphonam dima wideo legui mane may kane bam may wideo yoyou amoul solo serigne biiiii [Larmes de joie]