@mouhamed.cr704: 😂🤣 BOUKKI AK MBAAM MIY REE ! Boukki dafa bëgg a wone ne moom moo am doole… waaye mbaam mi am na yeneen xalaat ! 😂🐴 💬 Ku la ree ci film bi ? Boukki walla mbaam mi ? ❤️ Topp ma ngir film Boukki bu bees ! #Boukki #Wolof #Senegal #Comedie #FilmIA