@baayi.si.xeel: Yar ak téggiin du lu ñuy mayé, da ñukoy yaré ci bopp. Ci aduna, nit ku amul yar ci boppam, du mën a am cër ci kanam nit ñi. 💯 Képp ku bëgg a dëggëral sa mindset, lii mooy 6 principes yu wara nekk ci sa dund : Goré ak Doylou : Fonkal sa kàddu, te nga doylo ci li nga am. Nité ak Yamalé : Téyeel sa bopp, te nga maîtriser say envie. Bañ a xeeb nit : Nit ñëpp am nañu cër. Bul soufël ken, te bul xeeb ken. Baayi Si Xeel, yar sa bopp mooy sa doole ! 🔥 Ndax ban ci 6 points yii moo la ci gën a laal tay ? Tontul ci commentaire yi ! 👇 👉 Abonne-toi et Enregistre le post ngir fàtteku ko !  Baayi Si Xeel ✍🏽 #Baayisixeel #Motivation #viral

Baayi si Xeel
Baayi si Xeel
Open In TikTok:
Region: SN
Wednesday 14 October 2026 12:15:09 GMT
9587
551
5
12

Music

Download

Comments

fallou_leye_galass
𝐆𝐀𝐋𝐀𝐒𝐒 𝐅𝐀𝐃𝐈𝐋𝐎𝐔 :
♥️♥️♥️
2026-10-14 12:23:44
1
user9154130726028
user9154130726028 :
🥰🥰🥰
2026-10-19 00:15:02
1
ndiaye200791
ndiaye2007 :
🥰🥰🥰
2026-10-14 23:31:44
0
diomaye.5d
Diomaye 5D :
🥰🥰🥰
2026-10-23 10:12:05
0
To see more videos from user @baayi.si.xeel, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About