Serigne Babacar Sy Mansour Al khalifa yalla na yalla doli ko soutoura takhawou ko mayko werr fane wou goudou si barké seydina Mouhamad psl 🙏❤️
2026-10-14 18:52:25
362
yayou Naby talibé cheikh ♥️ :
Serigne Babacar sy Mansour yalna fi yague lol té wér inchallah
2026-10-14 20:18:03
90
mor dione🇮🇹 :
Walahi ndeysane yague fi loll th wer inchalah
2026-10-14 21:24:35
5
ch@ch@💋 :
Yague fii lol ta werr Sy Malick 🙏🏽🙏🏽❤️❤️m’alla begeuh dei ❤️🥰
2026-10-14 19:21:08
94
la babacarienne :
inchallah dinagne ko def yitté
2026-10-14 19:23:12
69
user943091298115 :
Sy Malick yague fii lol te were yalla samelene Sy Malick
2026-10-14 21:20:24
1
maodomalicksow :
jërëjëf Serigne bi,Mame Maodo Malick Sy RTA Sama toomaa yalla naniouko yalla fayal, Serigne Babacar sy Mansour al khalifa yalna yalla gouddal faname yokkou khéwalam té mayko wér, 🤲❤💚🤍🩵
2026-10-14 20:57:25
12
seck ndanane kharito yayam💚 :
seringe Babacar Sy Mansour yalla nanioko yalla fayal inchallah ❤️🤲
2026-10-14 21:20:02
0
Coumba tourè :
sallalahou allah Mohamed
2026-10-14 20:22:12
39
sophi tourré :
manchalla sy doundal wéral
2026-10-14 19:41:01
51
@🦋Awasaliou.shop👗👠👜🌸🦋 :
sy malick yague fi lol té and ak weer
2026-10-14 21:40:45
0
user4780891865155 :
Yalla na Yalla goudeull ay faname t weireul ay thieureum dolliko Soutoureu ci barki SEYDINA MOUHAMETH SAW AMINE 🙏