Bala gua kham ni Diouly neikhna gua Diouly ba wakh Hasbunalah wa nikhmal wakkil
450 FOIS bilahi walahi kepp kou bokou sisa doundou té yene woula dara Lou bakh ay mousi ba rek lalay yene té loko beugue beugue té khamo Lou bone lim la yene yalla dalay sorale ak yen nitt gni daga nane sakh man Lutakh samay nitt youma beugue rek niomay bayi fek ni nioniou yalla molay sorale ak nitt yoyou Alahou akbar delen Diouly 😭😭😭🤲🏻🤍🤍🤍🤍🤲🏻🤲🏻🤲🏻🤲🏻