My favorite artist from Senegal 💪❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
2026-10-17 23:27:39
0
ABB@ THi@T€ :
Khamoul léne milieu arts té dou ngéne thi mandou
Mia daff léne beug khamal ni mom dafa beug wané music thi yanéne pays youdoul Sénégal ak Afrique
donc pour niou reconnaître ko thi les autres pays il faut mou valoriser ces clips raisons pour laquelle accessoire you chaire
sac chaussures voiture de luxe etc.... dans des pays comme USA et d'autres
donc sou ngéne khamoul milieu music nopiléne té bayi topp thi dérou nitte di wakh di yakh rék bakhna rek fi kou thi nékk liye dokhal sa métier ngay déff mieux veux faire partie des artistes Sénégalais qui fait connaître la musique tokk kéne rek desna touti dingéne beug guiss Mia wakla mou joué Sénégal mouy tée
bonne continuation sœurette dou yomb mais nékk thi rék Yalla bkhna té moy diokhé in sa Allah lépp dina nieuw com ninga ko beugué
2026-10-16 12:15:49
350
pastef :
Qui aime le prophète mouhamed (psl)
2026-10-15 22:32:58
547
moustaphathiam9332 :
Kii dou reference
2026-10-17 22:59:11
0
🇸🇳SEN🇯🇲JAM REGGAE MIX :
si bane lobby la bokou
2026-10-16 10:04:44
96
Mamadou bou serigne fallou :
yalla moussal thiat ak nit you bonn
2026-10-18 00:36:50
0
AvisAutre :
Wolololo vitamine rek🥰🥰🥰
2026-10-17 13:52:11
0
Pretty ndeya🦋 :
Lii mom vitamine khassé leu ❤️
2026-10-15 21:21:21
178
Haliil thiam 🫶 :
ki moy sunu star deh ngen beug ko wala ngen bagn ko mom leu
2026-10-16 14:03:13
56
sidy_kandji férailleur :
c'est fini entre mia et mabo dama done espèré Un jour niou andate mai c'est fini liberté yakh nako
2026-10-16 21:33:22
18
Mina :
My favorite ❤️
2026-10-16 22:39:08
0
𝕸𝖎𝖓𝖙𝖍𝖊🎭〽️💵 :
Ces pas la voiture a sidiki sa 😳
2026-10-16 08:22:11
18
✰A͜͡𝖎𝖈𝖍𝖆 R͜͡𝖆𝖘𝖘𝖔𝖚𝖑 :
Art c partout dans le monde Tata Mia dafa begue adouna yeup kham ay song waw lolou moy rêve sah❤️❤️
2026-10-16 13:07:01
21
Omar thior :
kéne khamétoul vrai ak faut ndakh IA
2026-10-15 23:10:33
6
C'est arrivé là-bas ? 🇨🇮 :
Mia, vraiment on a pas le temps. Mais chère vit ta vie ne calcule personne
2026-10-16 01:14:22
8
Elcapo ✅✍️ :
MIA SOO DIËKO DÉLL BALË ADOUNA AMOUL SOLO IOE TMIT 🥰