L’occident n’a aucun plaisir pour une personne qui est née est grandit en Afrique, l’immigration est une piège et fardeau lourd courge brother.
2026-10-16 14:36:11
859
Princesse 👸 bou Sonko :
Ndeysane touki dafa meti 🥺
2026-10-17 00:04:34
377
Fatmarassul❤️ :
Il était parti pour se soigner ou non?
2026-10-17 01:41:17
114
El Hadji Tapha Seck :
Khawma loy khalat ak loy ressentir lou meunti ameu tu es l'un des Meilleurs Artistes Sénégalais en activités sinon le Meilleur yalnala yalla Sameu défal leu diam mayla goudou faneu bou andeu ak Wéer si barké Nabil Müstafa Amine.
2026-10-17 01:15:13
190
BMALICK :
calm bi I A la kharite
2026-10-18 12:59:05
0
papi thioune :
Ndeysane yalla na borome bii takhawouléne goor ak djiguene yeup inchallah 🙏
2026-10-18 14:46:24
0
Soso :
Souniou wa keur nieup khanàniou yama meuneu retanelo ak fo meunti nek bégeul contanal Fall ndiaga yaram amal diameu yalnala yalla sameu arr la ❤️🙏🏾
2026-10-17 12:16:55
91
mbacke Naby kelle 🇨🇦🇧🇷 :
Toukii aka barii ay surprise 😭
2026-10-18 04:31:09
0
Bergerie Sidy Birahim Fall :
Fiitey wax dj mooy, moy gnou tahawou nitt gni
Fiiety wax dji mooy, moy gnou defar hol yi
Fiitey wax dj mooy, moy gnou waxtaan mbokk gui feegn lolou moy wax dji
Reew(pays) dou naate(émerger) bougnouko bayyoul(cultiver)
Reew dou nehh bou xoll yi laaboul(sett)
Liguey fii tayy santhieu(deukk) fi tay lolou moment gueuneul
Unité (Africains) beineu lagnou😭
2026-10-16 20:27:05
81
Madou :
Le meilleur comédien du Sénégal, amal diam fall.
2026-10-16 10:39:31
242
@MG’s creative scissors ✂️❤️💯 :
Ohhh tey pere Diop bègul dh 🥺what’s up our star?
2026-10-18 08:52:53
0
D-F-k :
Ak loumou meti meti mo geun fouff Sénégal bi
2026-10-17 00:21:04
115
Mrs Tall ❤️💍 :
Ndeyesan kou bakh on s’est croisé à la gare de Montparnass le mardi passé il jouait avec mon bébé 😩❤️❤️❤️yalnala yalla sameuh tonton
2026-10-16 11:46:56
221
user3686678517121 :
way diop magilay bege
2026-10-18 06:44:03
0
mouhamadou fall :
diop fall seull 😭😭😭
2026-10-16 22:31:45
52
KANDJI PULGA ⚽🤩🇦🇷🫶 :
wa wieux khana mane ngay wakhal [Hilare][Hilare][Hilare]
2026-10-17 13:07:57
0
talibé bamba :
diop Fall yalla Nala yalla takhawou barke serigne touba ahmadou yakari diam gni barke seydina mouhamed psl
Très belle chanson❤️❤️❤️, je peux savoir le titre ou l'interprète s'il vous plaît?
2026-10-16 15:17:22
5
Lamine Al Amine Niass🇸🇳🇪🇸 :
Kou wayate son bi
2026-10-16 11:12:17
18
NDIAYE RASSOUL 📿🙏🕋💡🕌 :
Diam si yaw 🥰🥰🥰🥰🥰
2026-10-17 07:39:44
5
Fatousarr :
je sais pas pourquoi mais je le regarde et j ai envie de pleurer la vie n est vraiment pas facile et pour tout le monde
2026-10-17 00:52:13
24
gueyebaye14 :
Tonton Diop Falla je repense à cette chanson de Tata Kiné Lame : « Boul gawa senguême Yalla bo gawa seunguême yaw borom gui...» Je ne vous ai jamais vu sans sourire mais aujourd'hui le mien s'est éteint en vous voyant ainsi. Je pense que vous portez bien plus que ce que vous montrez… Courage Tonton Yalna yalla défal la diamou sutural la...
2026-10-17 13:17:13
10
ismaila :
ndeysan diop fall mbeuk ligueey meunteu ñiakk wayé ya ngui doone liguéyeul yallah lou kawé sa ndiort çii théâtre bii..diamono mo nekhoul rek te senegal dou massa faye diambaar..me iow bok nga ci nio khamnii warounio diakhlé sisene bop waala siséne ndiaboot...wayé bolékok theatre bii donté sa chainou bop la..🥰🥰🥰fo nek yalla nafa yiw yallah nékk faal ndiagua👌
2026-10-17 10:09:23
17
To see more videos from user @ahmeddiopfall, please go to the Tikwm
homepage.