serigne cv mane de dama âme béne problème si quinte lou ma quinte faté co
envoyé na la message vocal whatsapp svp
2026-10-16 21:08:07
32
sambmamcheikh :
pourtant lou werr la wakh dama lèckh si agnie gnieuw febar sama bir di meti dama wathiou lima lekout lepp ma sogua werr bilay
2026-11-02 21:50:07
12
ndongoumy1 :
Bilaxi Degg la mgui fofou la diéle Tangke bou meti 🥺🥺
2026-10-16 23:58:06
20
EVA BUSINESS 🎽🩱👖👙👗 :
barkhé seydina moukhamet sama yaye bimou décédé am mère bou niewon si deudj bi bilahi soula gounio sakh mou teude si sounio salon bi di wakh téléphone bay khakatay sama bene soeur mo dem niko mère khana khamo si deudj gua nek robba gounio sakh 🥺🥺🥺