mandé dama gneuw 15h 17 ma takk samay Tik dem Calcio dji
2026-10-18 08:41:11
502
Fatima Diop :
Doniou may nguir yalla😅😅😅😅😅
2026-10-25 13:59:56
0
RASSOUL CLEANER :
enfin bilaye dagne lay énervée 😡😡😡
2026-10-17 21:59:39
272
Mr. N D O Y E 🇸🇳 🇨🇦 :
Fall sonal nga niou😂😂
2026-10-18 01:54:41
241
Elaze Mor Diop :
Sama grand bi dh mom 7h lay yéwou cotché pain ak loumou ci deff ak tasse café wam tok ci cour bi di ndékki kou yéwo yam ci mom agne nak moko fi dakh dou dieul koudou lokho rék baparé meune taxawalou founeik lay dougou . Mane ben jour posé nako question Niko est-ce que réellement usa gua nek yaw pask gallé bi gnénép gnifi neik sougnou nieuwé ay 12h lay yewou di khar koulén dressél ndekki dougnou agne heure barii service affaire yi réro ame na cii 🤔
2026-10-18 11:44:45
65
Ous :
yaw xam gua modou modou yi😂😂
2026-10-17 20:07:05
395
djamil🇸🇳🇺🇸 :
Mane dé dama niawe si jour bi ma déme terrain football ⚽️😂😂
2026-10-18 17:06:25
43
Nanouch 🎀❤️ :
Tellement réel 😂💔
2026-10-17 22:38:04
103
Zey zey only🇸🇳😎 :
Ak kouniou rombou nila mag gua 😂😂
2026-10-18 16:19:56
76
Fatima saliou🇸🇳🇫🇷🇵🇹 :
Mane 19 h la gneuwe 20h weure nah kogne bii yèpou
2026-10-20 02:32:05
5
nunoo_25🇫🇷🇸🇳 :
Surtout wa louga
2026-10-19 02:15:34
7
adosouverainiste91 :
Sa transport dafa chere
2026-10-17 20:20:42
26
Oklm momo❤️🇪🇸🇸🇳 :
Saway tay mom danou ngua 6h gayi yewou bokk
2026-10-19 01:25:24
6
Dalou ndakarou :
Ma sœur elle ne dort mm op 😂bou nieuwé thi fauteuil bi lay tokk nane beugoul nelaw kon séjour bi day gaw di tela yewou nk sheut😂😂
2026-10-18 12:04:05
36
Da😎 :
Mane dh 5h la yegu heuy dem marché di ndougui ak waxou bou meti 🤣🤣🤣🤣🤣dama xamoul touki gneuw rek louthi diarr dofdof lou