mais imam dafa wara am métier. ce n'est pas une profession c'est juste une fonction religieuse. imam dafay ligguey am métier
2026-10-18 10:45:52
98
Dubai shop cologne parfum :
Mane dalle khaw ma Lou Sénégalais beug Imame dafa wara ame mèthier
2026-10-19 00:10:02
0
🇪🇸Adama 🙏🇪🇸 :
yalla bou ko thatte topou way 🥰🥰🥰
2026-10-19 01:31:29
0
Kara Fall Officiel :
Takk seuy wala djité bo khamni ken doula diohél dépense tmt lolou dafa yomb dh saway
2026-10-18 15:30:37
17
bamba wagne mbour🇨🇩🇩🇿🇸🇳 :
Salam alayka Tonton Imam dou métier dioulit gni ño wara goor goor lou si xam seine diner souko defei quartier bo doug meungafa ame au moins 5 gnila meune guindi. mais melni imam dou nit wara fay courant ndokh dépenses cette societe appartient à Dieu. Sénégalais yi setanou niou beine Imam danio yoroul nioune souniouy prblm keur rq doyananiou diner dangay def tei yalla takh lissi deiss kouneik na outi métier sauf exception de klk1 ki est incapable de travailler(handicap maladie etc) mais dieul diner mystifier ko rq def ko domaine reservé... tak diabar nilou yombei dioulei new tamit loussi diaffei toud dom loussi diaffei c triste ce pays
2026-10-18 23:11:17
1
Ghost 88 :
imam yi ak naim yi danio wara am salaire you baxxx au niveau des mairie
2026-10-18 11:12:38
36
zoule63 :
khalifa général yi sax bomoy touwoul légi niou dougou gal dém Spain
2026-10-18 13:53:35
4
Mousslimchamahachine chiby :
imam yalla nako yalla défal diam ak souteureu koufi guiss yoone na déme dara nékoussi
2026-10-18 14:12:34
12
Mass DIEYE :
" donté imam warna meneu liguey nack " vous avez dit l’essentiel . Citant Abou Bakr et le " baytil maal " faut pas oublier qu’il n’etait pas un nécessiteux . L’imama est le plus haut titre de l’islam , mais pas une fonction . Donner le nom a un nouveau né , celebrer l’unioin entre mariés , la priere mortuaire sont du Fardoul Kifaya " obligation communautaire"
exp : en l'absence meme de l’imam , un autre peut le faire . Le travail est la chose la plus importante dans une vie , il libere et rend digne . Au Sénégal 95% des imams psssent toute la journée entre les Fardoul Kifaya et sur les lits " nelaw reck . Donc cet imam qui est parti gagner sa vie ailleurs n’a commis aucun delit , les adjionts assurent . imam bou touki wouti dara nékoussi ,
2026-10-18 11:52:43
5
AHMADOUNA MAKKAH TRAVEL :
li gua wakhh bayiko khell dou gathie dafa amm sokhla warko fathie donc amna droit demm ligueye
2026-10-18 11:35:18
8
dofu seydil hadji malick sy :
linga wakh moy deug mercie
2026-10-18 09:01:47
10
AlMouhidineOfficiel1173🇸🇳 :
liguéye farata la, imam am na droit déme toukki pour liguéye
2026-10-18 11:51:42
7
Moustapha Hamzatou Touba :
xélmou dal si diamu yalla boku[Prière][Prière][Prière][Prière][Prière]
2026-10-18 21:55:05
1
Univers7 :
imam bi day lidieunti bopam, dépenses lay topi,
2026-10-18 16:54:48
0
pap aloi. sarr :
wallhy
2026-10-18 11:10:35
0
sana diassy :
est-ce que kham nga situation imam bi?
2026-10-18 23:50:16
1
Talibe cheikhou thienaba :
walaye ndeysane deugueuleu nagnouye takhawou sunu imame yi balla gna dème si galle yi
2026-10-18 08:45:50
6
Boubou sanghott :
#Âmena solo walaye ♥️
2026-10-18 22:33:05
2
guainde kara alliance😍🤩🤩🤩 :
gal mo si mission yonenty la bok
2026-10-18 19:40:59
1
user8213385396566 :
mais sénégal méttina quoi mou déme pour outti loumm amm lolou dara nékoussi
2026-10-18 20:35:17
1
mouhamed rassoul pouye :
saway boudamé loum done déf senegal defko spagne.té fofou mo eupe touyaba. may léne gnou diamb senegal daga méti ishh
2026-10-18 11:44:56
2
Ablayediop :
Salam alayka Tonton Imam dou métier dioulit gni ño wara goor goor lou si xam seine diner souko defei quartier bo doug meungafa ame au moins 5 gnila meune guindi. mais melni imam dou nit wara fay courant ndokh dépenses cette societe appartient à Dieu. Sénégalais yi setanou niou beine Imam danio yoroul nioune souniouy prblm keur rq doyananiou diner dangay def tei yalla takh lissi deiss kouneik na outi métier sauf exception de klk1 ki est incapable de travailler(handicap maladie etc) mais dieul diner mystifier ko rq def ko domaine reservé... tak diabar nilou yombei dioulei new tamit loussi diaffei toud dom loussi diaffei c triste ce pays
2026-10-18 18:31:17
2
Babacar Gaye :
ligueye diamou yalla
2026-10-18 19:12:37
1
barcalone95 :
imam yi ak oustaz yi nio done prêcher nan aduna dou keur.alakhira mo guen mo woor.di tok si diaka yi di diouli di gnane di khar yalla.legui ils peuvent plus attendre Dieu.ils vont allez à la recherche de la meilleure condition
2026-10-18 15:29:06
0
To see more videos from user @abdoulazizdiaw83, please go to the Tikwm
homepage.