@wwagy14: Hasbouka minn maa-ihil khalîli Maa qad ataa fî mouh kami tanzîli🇸🇳🇲🇷❤️

░e░u░t░o░u░c░h░e░ i░k░h░n░a░
░e░u░t░o░u░c░h░e░ i░k░h░n░a░
Open In TikTok:
Region: SN
Sunday 18 October 2026 18:43:49 GMT
4529
882
55
25

Music

Download

Comments

dadista20
Dadis ta :
Yaw ya guate xel koulay nagoul lolou yaw 😂 wa yaw ko done nk ❤️❤️❤️😂😂😂
2026-10-18 18:59:55
4
user9944215907684
fatima 🧜 :
lolou mom nga balma wayé dou deugg 🥰
2026-10-18 23:26:43
0
cheikhna.cheikh.sadbou
07 novembre 🥳🫀 :
wa mane souma nekhè nè mala ko guena beug
2026-10-18 19:09:37
1
mint_alweuly
Aïda❤️Cheikhna😍🙏🥰 :
Ehhh wayy fayma sakh takhoul m nangou lolou mohhh wayy kii doma dap si mom
2026-10-18 22:34:56
0
unekhardrienne
Chänëllë la khadrienne❤️🤞🤍 :
Sa xalat gua waxx Wayer gno bagne ther souma sagnone mou donne pour mane kesser 🥹🥹
2026-10-19 07:57:49
0
amyboucheikhna
Amy chiby aidara :
Malako guena begue ❤️❤️😭
2026-10-18 21:24:57
1
7849m
MMS ❤️💍 :
Mone ga yakar
2026-10-18 21:42:49
1
beiddy22
Beiddy Diallo ✪ :
Lolou mom kafou Massi rétanou Massi 😂😂😂 malako guena beug dh 😂😂😂saway
2026-10-27 21:49:20
0
niwa795
Niwaa :
wahiartou mamou sxna kheuje mint cheikhna khaddamy borom gueleemgui
2026-10-19 07:18:46
0
ndiemeomer3981
Ndieme Omer :
cheikhna si khôl yi♥️♥️
2026-10-18 19:18:00
0
adja.fatou.samb.sy
adja fatou samb sylla :
wakhayertou Cheikhna Cheikh Saadbou Mamou sama sangue ba Chérif Beuh Makhfou
2026-10-22 12:10:18
0
aicha.ka66
Aicha Ka :
Yaw ko done adouna lisi bir sakh doumako nanguou 🥺
2026-10-19 12:50:45
0
sonitamrsndiaye
sonitamrsndiaye :
Mo mane mii Malako ngeneu beugu fouff sakh doma dapp
2026-10-19 20:38:07
0
moussafall8353
Moussa bou Atkhana chiekh ayah :
Heureusement bete bete talibe chiekhna chiekh sadbou ma chance
2026-10-22 12:11:32
0
marieme.bou.cheik2
marieme bou cheikhna 🥰 :
cheikhna a vie❤️🥰?
2026-10-18 21:48:47
0
moustaphazamane573
talibé cherif bouya ❤️🥰 :
DIEUREDIEUF 👌🏿 CHEIKHNA 🥰 WOULD 😍 MARIAM 😍
2026-10-19 21:46:37
0
babacarassassa86
babacar bou cherif Assana :
2026-10-19 09:35:29
0
njaay015
𝑱𝒊𝒃𝒓𝒊𝒍 𝒏𝒋𝒂𝒂𝒚 🖤 :
2026-10-24 01:59:59
0
beiddy22
Beiddy Diallo ✪ :
Beug cheikhna ben kass lawone té mako nane 😂😂😂
2026-10-27 21:49:53
0
user6321555201139
Maïssa courtois 💯 :
ww wayé dougnuko nangou 😆
2026-10-18 19:57:30
0
mamegnagnamarianneousman
Mame Gnagna Marianne Diatta :
doumalassi bayi moukk jamais ken guemouma beugeu cheikhna cheikh saadbou je l refuse gatégoriquement
2026-10-18 21:00:50
0
ndiougv
élément Borome ansar✨💫 :
Saway def koo chocolat 😂
2026-10-26 17:02:12
0
babacardieng1756
Babacar Sonko 2029 :
DJOUM GUA DH MON FRÈRE MANE SOUMA DÉFE CRISE RÉK THIOFÉL GUIMA AME SI CHEIKHNA LA WALAHI SOYMAY SANGUOU SAKH MOME LAY KHALATE
2026-10-19 15:24:21
0
modoungom360
Modou bou cheikhna le nabien :
🫢🫢🤣🤣😁😁 bilaye yakhoromou
2026-10-18 21:05:49
0
akhloubeytistore
soldarou -akhloubeyti🕋 :
ayway khalaas 🤣🤣🤣yangy nakh sa bopp😂boul topou saye khalat nagneko wakhtanné
2026-10-19 16:01:28
0
To see more videos from user @wwagy14, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About