Balla Gaye en une semaine 😁
1: Def letou thiow am
2: créer compte tiktok 200k abonné en 2 jours
3: Mou dem bercy totnie ko
4: nieuw signature ak sac bi tothie ko 😂
5: lundi invité au canal
vraiment Balla doo nitt 🥰
2026-10-19 01:09:00
1259
Sénégalaise🇸🇳 :
Loumou messeu wakh def nako mo xam daniou kay dane walla moy dane 😎❤️
2026-10-18 22:36:09
791
DEBS BODDY :
sakho illimane loumou meusseu wakh def nako yall nako yalla may ndam
2026-10-19 12:21:35
1
MMG❤️bou serigne babacar sy🥰 :
Balla dh loum meuseu wah def ko ada diaroul guay balla balla lou nane 30 seconde