Losi quisse liqueye ba déh reck ta douniou âme dra
2026-10-19 09:13:02
139
myma :
Surtout féne yi moma diakhale, ak dila neubeutou melni kou nek ak sa béne ennemi, wayer kouma neubeutou ma rére la. Adouna yala ko mome.
2026-10-19 15:26:12
86
mounass diouf 06🇸🇳🇲🇦 :
mane deh sm boss nouyo lagne sekk😩😩
2026-10-19 20:47:38
16
user62785054363383 :
Bilahi deug rk gua moma dal nii beugueutouma sama dieukeur dafa yakh sama khol bilahi dafma wor dieundei ma ak kenen tei defnaniou 8ans de mariage am niari dome machallah ak noumako mougneulé mou kheuy defma Lou niaw lii wayé bayinako ak yalla Dina atté inchallah🙏🏻🙏🏻🙏🏻🙏🏻
2026-10-19 10:29:25
42
Domou🥰🙏.yayam 💯 :
motakhit daw na niou ba deh Sarre douniou ko am daniouye sakhar rek douniou take fi Lou waye def bopam bo goude fane kham si darra
2026-10-19 14:21:46
25
Beugue yonnénti bi :
Bilay bonne kassé moléne diap wayé yalnagnou yalla até ak niom
2026-10-19 18:33:32
24
user8781327474584 :
machallah goudeul fane frère
diam thie iow
2026-10-19 11:08:55
9
Fatou Ba :
Bilay wallay kham nathi Dara
2026-10-19 11:24:48
12
Mame astou THIAM :
vérité absolue surtout goor gou naye do mayé khalis sa diabar
2026-10-19 20:08:56
8
bllisakho :
Mandé 5mois de mariage mais je regrette amèrement divorce d lay df
2026-10-19 11:47:01
7
Bb fa❤️ :
Yaye nitou deugue mn frère
2026-10-19 20:09:29
6
maty Rassoul :
bilaye dhé mes yalla dina até
2026-10-19 10:10:51
6
🌸Djeliya~Sy🌸 :
Machalla meilleurs 🙏🏼❤️
2026-10-19 08:39:16
7
yayou Rassoulgueye :
alkhamdou lila biniou yalla bolé gore kou bakh🥰❤️
2026-10-19 11:26:19
6
Thiane Gazal :
merci beaucoup mon.frere
2026-10-19 22:17:52
2
khoudiagueye509gmail.co0 :
2026-10-19 13:22:02
4
co 2023 :
Motakh bima seusai dama divorce walakhi
2026-10-19 10:51:59
5
Mycha :
2026-10-19 19:31:33
2
user77618044493283 :
wallahi amouna solo
2026-10-26 11:45:01
1
Souadou :
merci beaucoup 🥰🥰🥰
2026-10-20 00:53:19
1
Henrietta :
vérité absolue
2026-10-19 13:55:27
1
gueyeyacine54 :
bilay
2026-10-19 20:12:56
1
Mrs kane ☝️❤️🫂 :
Vérité absolue
2026-10-21 14:08:23
1
ndeye :
vérité absolue
2026-10-21 12:24:47
1
Eva chou :
Bilaye
2026-10-19 12:52:14
1
To see more videos from user @docteurbio, please go to the Tikwm
homepage.