walahi yénàgui rétane té guissoléne IA dolé bimouy gueuna ame en ce moment
2026-10-19 13:53:53
2733
dioumzé :
Li latzo la ak fallou thiam 😂
2026-10-19 12:51:31
2423
Abda_Ly bou SBS✪ :
ia la deh😂
2026-10-19 12:41:21
1327
Momo🇸🇳 :
May ma Nicolas Jackson 😂bi
2026-10-19 17:45:47
0
G..Y🐍 :
Sénégal meilleurs pays xalis rk la manquer
2026-10-19 13:36:40
72
Fah Bintou 💗 :
Vrai vidéo bagui ni 😂Thiey ia bi
2026-10-19 15:11:10
112
BABOULLAHI❤️💙 :
bara mou moudié nieuw nk😂😂
2026-10-19 13:08:22
693
Binette Diouf :
borom challenge bi gneuw na 😂😂
2026-10-19 17:01:40
0
mangui dans le comment 👑🔵✓ :
ame na aura wallah
2026-10-19 14:23:21
22
Mrs Joop🥰🥰 :
kii momm Barra??
2026-10-19 17:13:30
0
. :
ayyy IA bi wa bakhna
2026-10-19 16:29:54
0
mouhamed💚bou💛diop2🥛 :
vidéo latzo ak fallou la niou dieul déf ko ia
2026-10-19 13:43:38
25
Pãpįtø🥳 :
Un jour ma diangui ba wathie dém pour gnibi sounge keur basi yone bi ma tassé ak béne mère bu yore gaz🥺 mounima sama dome domabale yoboule ma gaz bi sama keur ma yeurame ko😞yobe gaz bi basi bire keur gui rek ma dale di guise ay bop😳 sama fit toga toule 😨ma def faire semblant melni ku guisoule dara après maniko sama téléphone bi dafa wade si porte keur gui xarale ma dieule ko mounima wawe rek ma dale di daw après thie la wo police expliquer co situation bi police dale di niaw ma wane ko keur mère bi après police diape ko guéné bop yépe ndakata ay bop chargeur la ak bop rallonge mofa nékone jour bobu akka ma tite.
2026-10-19 15:00:51
9
Alpha et ses vidéos :
original
2026-10-19 16:38:39
0
Lamine Niang :
Aldiana yatouna yalla nafa nieup dém🤲❤️✅️
2026-10-19 16:40:11
6
elhadjimalick374 :
IA bi dina meusse yak adouna douma adama c’est tellement dangereux au point maintenant qu’on discute si c’est vrai ou c’est l’intelligence artificielle . Faisons en bonne usage
2026-10-19 15:41:22
26
NABII《👑》MOUSTAPHA :
Dé lén ko gnanal yalla taxawouko
2026-10-19 15:26:06
7
carmella :
pourtant mane nilay wakhé r sinon doumako meuna wakh té simple na dé
2026-10-19 13:05:48
43
Mbaye :
dalli bakhaaa yi😂😂
2026-10-19 13:44:38
67
Delfa Seck :
c originale 😂🤣🤣🤣🤣🤣🤣
2026-10-19 13:57:46
5
Samba Linguère 💙🤍 :
Tiit si IA Diotna
2026-10-19 14:43:03
7
To see more videos from user @dakarparodiesn, please go to the Tikwm
homepage.