@barrabeguefallou1:

Elhadji barra falilou ✪
Elhadji barra falilou ✪
Open In TikTok:
Region: SN
Monday 19 October 2026 13:55:14 GMT
157984
24503
1234
672

Music

Download

Comments

antandiaye920
Anta al mountakha 🇸🇳🇸🇳 :
yalla naniou Yalla meye werr rek ak werr le🤲🤲
2026-10-19 15:20:09
347
user46129khady
premiere dame 🥰🥰❤️🔐🔐 :
hopital cheikhoul khadime dé mofi tanné walla clinique
2026-10-19 15:56:45
96
maman.sarr396
Maman Saliou♥️🥹🙈 :
Ay way li mom nagne si wakh nk
2026-10-19 14:59:21
65
alaminemhd1
Al amine~MHD :
Démal Cheikhoul Khadim douma wakhe mo fi gueune wayé fi si touba mo fi tané
2026-10-19 15:49:13
142
mounassediouf6
mounass diouf 06🇸🇳🇲🇦 :
lolou mom bahoul ay way
2026-10-20 10:15:31
0
ibouca2
Mme Ndiaye xollo taw❤️💍 :
Lo wakh Amna lo bayi😭
2026-10-19 19:57:15
40
mouridsadikh99
@Ndeye fatou😘 :
Ndamatou rek doufi hopital boylen côté dem benene hopital
2026-10-19 16:09:45
31
765092594serignetoure
serign. Mbacké Touré🇸🇳🫶🇪🇦 :
ohhhhh yalla bakh na bilaye 😴😴
2026-10-19 14:01:03
124
khelgome
khélcome :
Yaganafade Ndamatou Dano reybasouf
2026-10-19 15:30:57
21
madame.ndiaye.afi
Madame Ndiaye Afia❤️💍😍💕 :
Thiey Senegal 😭😭😭
2026-10-20 17:40:28
0
ndayachou338
Ndaya chou :
yalla bakhna😢😢😢😢
2026-10-19 15:21:30
33
isseu997
i:🇸🇳 :
Legui lii ni lagnie kay bayi nonou niit yi di dé
2026-10-19 15:06:25
45
mdathiou668
Madme thiam :
yobou ko cheikhoul khadim dabar lan dh ♥️
2026-10-19 16:06:56
31
mariachantal01
Mariachantal🎉❤️💫 :
Nako serigne bi yeuk
2026-10-19 16:47:50
20
mame.diarra.seck866
mame Diarra Seck :
1500 la soxla thée yalla takh 🙏🏾
2026-10-19 17:56:13
21
amyyayefall2
Amy yaye fall 🚩🏴 :
Ndeysan metina
2026-10-19 15:22:54
15
toulaye300
toulaye saliou ❤️ :
légui doléne marche dénocé li c’est tro métina waye
2026-10-19 15:12:51
17
serignefallougueyembadji
SERIGNE FALLOU GUEYE MBADJI♥ :
Doyna warr dh
2026-10-19 17:13:09
12
falloungome02
fallou ngome Bou sfallou ♥️ :
ndaysan 😭 😭
2026-10-19 15:14:17
16
layendao27
BLACK PRINCE 0️⃣1️⃣ :
ndeyesane😅
2026-10-19 16:34:22
16
bbmously
Sayda mously Gaye🧕🏿 :
Bilahi walahi khamnasi dara def nanioumako sama doume fébar ma nieuw niouy snp bilahi walahi 💔💔
2026-10-19 15:43:10
28
unesalikhate88
Une_s@likhate_xasida88🧕🏻🫀🤍 :
Nanou lenfi bayil sen hôpital te demsi yenen yi négligence bi dafa eupou trop🙈
2026-10-19 16:47:37
15
seye.tapha01
محمود خليل الحصري 🧠 :
Ndaysan 😳😳
2026-10-19 14:10:38
9
talib.cheikh9746
talibé cheikh :
nioune wa Touba sonounagne
2026-10-19 17:45:49
15
khawsouseckgmail.com
khawsoul wara Seck :
Doyna war lolou 😭
2026-10-19 17:50:55
11
To see more videos from user @barrabeguefallou1, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About