Loumou wahhh deug la [Red heart][Red heart][Red heart]
2026-10-19 15:50:48
8
saa tuubaa💚 :
borom xél yi lay wakhal
2026-10-19 18:33:44
49
Amirah 🥰❤️🇸🇳 :
Sama papa mo bari xam xam
2026-10-19 17:48:28
210
fatima Bathily :
diomaye monou yakhal kay wayé bakona ba paré yalla nako sounou akha dal
2026-10-19 17:00:31
116
DIAO FARA SENE :
Bo wakhé doff yi nane da beuri wakh wayé mom xam xam rk lay wakh bilahi walahi .
Ana yénéne politicien yi esk métrisé nagn deuk bi comme niko Sonko di défé.
cet homme est juste exceptionnel.
2026-10-19 20:09:17
58
carafour de la luzerne sall :
2 an sans FMI dara yokou woule ya wooor
2026-10-19 23:41:05
0
HIZBOU ALIBABA :
Ousmane sonko balgnou akh rk
2026-10-19 17:03:32
50
TDKD :
seydina Ousmane sonko yalla naniouko yalla fayal samal niouko défalko tawfékh aki ndam you yatou loll amine yarabi thie barkeb seydina Ousmane sonko
2026-10-20 09:10:13
0
mouhamadoumansour325 :
C'est pas toi le Président. laisse Bassirou tranquille si tu aimes le pays 🇸🇳