bolene ko faté moudiene bici dess fofou mon descente bene solution rk mofa wara connecter directement mou diaré nonou dem guedj par ce que fofou moye terminétion parcelle connecter directement rk mosi solution ci non chaque fois nilay démé rk
2026-10-19 23:51:44
1
Babacar✈️ :
Ndeysane 😭😭
2026-10-20 00:19:44
1
khadykeita592 :
camberene deh mo wakher niouni koufi bokoul dofi djitter ta niom gni bok si village bi falewouniou ken sen bop rek ta bo wakher niouni dangay politik ta nioune ken mayouniou danio dieund douniou keur yi ta niolen eup fouf