@henn_by_salihate_shop:

Henné by Salihate Shop
Henné by Salihate Shop
Open In TikTok:
Region: SN
Monday 19 October 2026 23:08:03 GMT
47024
3351
250
100

Music

Download

Comments

minarassoul020
Amina ❤️ :
Li kay mom doy na war xolal borom keur biniou fi ray semaine passée
2026-10-20 01:13:03
66
talla_aw_ndiol_touba
TALLA AW NDIOL TOUBA🚛🇸🇳💯 :
sa interés rek motakh ngay wakh😂😂😂😂
2026-10-20 00:29:29
11
transporteur131
MBT :
rond-point Bobou da khate
2026-10-20 12:25:53
3
seye949
Gaye seye :
Khamal lingay nékol rond-point yep lay camion di weur
2026-10-20 03:10:57
2
layenabien
Laye mbengue Attidjiany 😍😘 :
Sokhnasi rond-point bi dfa touti souféké camion bou goudou la douko mana weur lolou dra nekousi mé rond-point bou médina baye bi dfa touti
2026-10-20 12:15:22
3
noorcodou
ℳ𝒶𝒽𝓂𝒶𝒽⭐️ :
Blh c vrai Tali bi mome bakhatoul wlh 😭
2026-10-20 01:58:15
12
mame.saliou235
Darou bayrè fall Guéye Saliou :
wahalll lou khame
2026-10-20 09:54:51
0
yatma.le.barron.__
SANTE S.TOUBA :
lou wer la wakh boulene yakh sunu deuk bi
2026-10-20 01:42:58
7
begeuserignetouba.7
begeu s touba :
ana diegen ak takha wallo si talibe
2026-10-20 02:43:14
11
seydimoustapha
Seydi Moustapha 👳‍♀️ :
Mais problème bi moy rond-point bobou camion bou mak boukoy diema weur di dianou parce que espace bi yatou woul mo takh c’est ça la problème même rond-point médina baye bi camion you mak yi mou nougne ko weur surtout camion bou charger ba fess nak bouy wer di danou parce que rond-point yi nekoul you mak aussi espace bi yatou woul
2026-10-20 02:33:32
5
782874050mb
Adypro :
Non li waroul am fofou pck auto transport yi waroul diar fofou déff lén manifestation lolou moy yon
2026-10-20 07:31:01
4
lhoomefort2
Fière d’être routièr 🚛🇸🇳♥️ :
Thioooo 💔😂
2026-10-20 10:03:48
0
karba29082001
KARBALA NDIAYE :
non lolou code de la route molén ko may si rond point yi sokhna si
2026-10-20 01:16:54
5
mbcke_der_634
✦Ꮇ𝗕𝔸𐊢𝗞𝞔́ D𝞔́Ꮢ ♡🍷 :
limo leni déranger 😅
2026-10-20 06:01:03
4
bamba.yalla09
bamba yalla :
yok lene KO waye
2026-10-19 23:56:28
5
djilitoure0
Touré 63🛣️🚛 :
Wakh rk
2026-10-20 02:45:12
5
babskilleuh4
✰𝐁𝐚𝐛‘𝐬✰𝑲𝒊𝒍𝒍𝒆𝒖𝒉🇸🇳 :
2026-10-20 01:00:38
8
dieng989
Dieng🇵🇷✌️ :
Cavion [Larmes de joie]
2026-10-20 02:35:31
1
la.charmante.barh0
la charmante barhamienne❤️ :
Bly yakkk naniou lépou
2026-10-20 00:02:31
3
alphasow053
borom AiB :
ah doyna war dh
2026-10-20 10:10:06
1
domoudeukbi405
💥kheuch@✔️💥🇸🇳🇪🇦💯💲 :
wa passoirr
2026-10-20 00:45:22
1
ahmada2352
AHMADA💙221🇸🇳🇨🇬✌🏽💙 :
Sokhna si di wakh khamoul cote de la route 🛣️dou round point yeup lagni weur ak longueurou camions aussi
2026-10-20 12:58:09
1
yayouserignesaliou85
MOUNASS BTN PARFUMERIE :
Walhai paré yakh Taly bi yép loin d’une semaine taly yép yakhou mane soumay kheuy ba dadjé ak niom sama fit bi dou tok
2026-10-20 02:01:43
1
babacarchiekhazize266
babacar Chiekh Azize 266🙏 :
Ki di wakh mo khamoul cote de la route 🛣️dou round point yeup lagni weur ak longueurou camions aussi
2026-10-20 10:59:19
1
To see more videos from user @henn_by_salihate_shop, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About