santal yalla bamou yèmè thi yobou diaro naniou bayi khel xalè yi
2026-10-20 08:14:33
553
thier beugue fallou :
no vreman dangay khol lirek
2026-10-20 10:25:44
0
771100 :
li dafa woroul sakh
2026-10-20 07:39:01
175
Sokhnish Cissay🇸🇳🍿 :
Ndeysane khalé khamoul dara😭😭
2026-10-20 08:32:49
64
小李🇸🇳🦋 :
Li sakh da weuroul meunone nako déf lénéne ya Allah protége nos enfants 🥺
2026-10-20 07:48:55
114
pereferepapame :
Waxouma lolou kouye filme lou tax mou bayi ki dem tmt douniou wax si lolou
2026-10-20 02:56:15
71
Oumyna~Beauty :
Walay santale yalla boubakh comme xallé bi dara diotouko loumou dieul yalla na yobou sene aye allalou adouna la courage les maman
2026-10-20 07:30:21
28
serignesalioutoure3 :
lii deff Nanou ko sama Dom so démé police dounou si sonou
2026-10-20 08:27:43
14
KhadysoguiNdong🤱❤💍 :
fi diamono ji tolou tay lou daal xaley rek sa la responsabilité des parents, aduna bi tolotoul founiou bayé xaley you daw niou nek si mbed bi, naniou geun sécurisé nos enfants deuk bi dafa leudeum🙏🏾😢💔
2026-10-20 09:13:00
14
Netishu Camara :
Ana yayou khalebi
2026-10-20 02:55:24
29
yaye fall moume serigne saliou :
ligéyiléne guir yalla 🙏🙏🙏
2026-10-20 07:31:17
30
aaaa :
khale khamoul dara yaye yi naniou tey e khaleyi
2026-10-20 02:55:50
35
maman ansou🇸🇳♥️ :
Li sakh da woroul meunone nako def lou bone kholal mbede bi kéne nekoufi Ay parents surveiller léne khaleyi nguirr yalla 🥺
2026-10-20 09:40:05
8
wax Lou bax kou bax :
boy limom boulko defati li risque deug la😨😨😨😨😨😨😨😨
2026-10-20 08:36:34
6
Anna Diop🥰🥳😍 :
Wa legui diaro ak lamou khaliss you khalei yeup yi meusseu rér Senegal nako fay rek mou diekh
2026-10-20 02:39:57
102
Mame Lô❤️🔥❤️🔥💘😘😘🥰 :
Ont m’a fait la même chose bama néké Khalé mes boucles ma saines ak sama lame ont m’a tout prix