ana gni di wakh ni Lou Mame defal nit wakh ko nieuw len 😂😂😂
2026-10-21 13:03:49
106
BADIEUNE :
Molen geun khol niomm nieupp
2026-10-21 12:51:14
48
Ma chouchou🩷d'amour💕 :
yallane ko yallah lafale thiatt 🥰🥰🥰
2026-10-21 11:56:44
121
m@ bussenaices :
sa c'est notre caviar 💚💚💚💚💚💚💚
2026-10-21 12:11:26
32
Cheffe 🧑🍳 Kenza 👩🍳👩🍳 :
Caviar bi farice la day diéngue rek wayé dou danou mame xol bé rafete ak lifi ame lep seti na nogaye té limou wara def def nako si souf 🙏🙏🙏🙏motakh diam rek nguay ame notre lionne sa xol bou rafete rek Lala teyé
2026-10-21 13:03:30
50
Queen 👸🏻 rose ♥️🦋 :
Nogaye après bo guéné digua xam kila begue mame dafa honnête si nitam
2026-10-21 12:17:25
507
user6235941973246 :
mame guarmila farisla dia poulo ❤️❤️❤️
2026-10-21 12:05:50
71
Astel🥰✨ :
Bakh mome dako def wakh dji mo bari rk mais dafa bakh mome 🤧🙏