Kharal ma out fi wakayeté wakh thie sa diekou ay bayéte def nala gay sama kharete komel ni yaw mobax siman.
Ma bon diekou ta tangou lolo. Ga am sa yar ta sédou loll ma sék yet ta doko khoul rouy ga diekou djiegn nia gan
Am am takhoul ga wote si ma aw tor takhoul ga wot si ma lanén takhoul ga wot sima lodoul yalla ak nioufil thie man.
Lo am thie our ma diel ko diay fathie sama sokh la gay ko téy dou mag dou ndaye thia do ndediay ko xam sa diono fi thie man
Dioco déwar ay diebaran
Khodio lobon diokh ma man diokh gama thier xam kima don koy nuit kou bax dou wakh sa bon
Dioco de khadji ay kharit
Yam ga siman def mab kharit de dieuf degal né ab mourid motakh nala sant man
Fétnaloma ben yon plienté woma yobou yon sa bontou ibou lokou nonn bou diel pékhem diamé siman
Wathie ga diemal ték thie kaw fokou ma loll badoma diaw de wakh lo bax de dieuf lou yéw
Dadji goumack man koula gan
Yarou diegou djigen tay
Fotoy nio dal fo wow nio wéy defou safan wotal kou lay nou mel thia daw mil gani ren
Ken douma yab de diar thie yaw nekhoul ga niaw
Mouwékh ga daw goudek bathiack nadji diaki taw yack may diefal com liga man
Am nionan dack ma thie bar balo ma wakh ma de bar bakou dioutel ma dade mer com don yaw wet ga def ni man
Kou khamni boy thiowaka mére
Deyoukhou thiay saga ta sér
Mounopi mousakh thiey mougn kou wer yayou ga sack thiant man
Doutoko tayet mouniaka neh
Doto yiet bagawa diekh kon boul ragal sakhoul na fikh yagal ni fokounalamn
Ka way diabar dia fatou gaye
Thione seck way fi ndiaka tay
Dakhou dioma composé way lélé waral ma way ko man