@minandiaye0:

Minaprivée haïr
Minaprivée haïr
Open In TikTok:
Region: SN
Wednesday 21 October 2026 19:18:07 GMT
58337
5443
367
495

Music

Download

Comments

mmg_deco
MMG_GROUPE 🇨🇳 🇸🇳 :
7ans mom doumako har nit
2026-10-22 11:03:41
91
petitedame03
La petite Dame :
Mane 10ans mangi tokk arrêter samay etude diko khaar di togou nek femme au foyer 😞😞😞
2026-10-22 11:59:07
26
adjirassoul20
🪭Adji Bint Rassool🌸 :
Dangua xamoul rk mais ki dala arranger bilahi
2026-10-22 10:00:16
156
fafaa647
La FaBi🦂🫀🇸🇳 :
Khanaaa meunou koo plainte ???
2026-10-22 09:04:15
74
skincare_by_toulay
ToulaySkin🫧💕 :
Kene xamoul bane guémigne mo barkel, wayé soudé li deug leu nitt moko deff yalla nako yalla torokhal kom nimou ko defé si barké Seydina Mouhamed🙏🏾
2026-10-22 12:21:14
179
mrsseck85
mrsseck85 :
Dfa am niou niemeh akh vraiment 😭
2026-10-22 00:48:52
178
houleyediallo396
houley OD :
ayway. limom[Crying][Crying][Crying]
2026-10-22 12:42:03
0
madame.wade580
Users :
des fois douma beug deglou yene yi ndakh journée bobou yeup khol bou nakari lay yendo
2026-10-22 07:53:54
95
mamiba319
Mami Ba Mk :
Dinako guisse d le karma existe courage ma belle
2026-10-22 08:10:49
113
oumyguaye
tata og :
diarouko besti yalla bakhna
2026-10-22 19:40:59
0
thianes2
thianish :
Comment vous faites pour être avec quelqu’un ki est à l’extérieur ?
2026-10-22 08:35:08
70
yeuser6
Biibii :
Barkei Cheikhoul khadim wadji dinako guis
2026-10-22 01:53:48
462
dabisko65
dabisko :
Boul diooy sokhnassi yallah dinala fadial lép inshallah
2026-10-22 13:31:30
2
thiaat406
thiaat :
Ho my god sama xol bi diekhna
2026-10-22 15:11:25
0
maryammmmmmmmmmm2
𝐌𝐞̈𝐫𝐲𝐚𝐦🎀👸🏿🇸🇳 :
Sheuu sama khol bi dagg na 😪 djoulil ko niarri rakka 3h du matin
2026-10-22 02:13:18
49
jeannesarr4
Jeanne 🙃 :
Ndeyssane metina torop ho massa way
2026-10-22 11:01:05
4
awa.sarr382
Hawa 🥰❤️awa❤️❤️ :
Ndaysan hoo lou way deff bopam yalla guiss na lep
2026-10-22 12:07:18
0
ndeyasaliouvaisse
ndeya-saliou :
defal nafila 2 raka bayiko ak yalla legui mou atè lein sama khol bi diekhna 🥺🥺 belle mere aussi setlein yalla sein diganter ak xalei yi
2026-10-22 06:47:27
30
beugg.serigne.fall
beugg Serigne fallou :
ni dé lagne ma fassé billahi walahi 2 ans de mariage am bén dom mou khéy fasséma si korgui tédéfoumako dara billahi maintenant je suis femme ménager pour élever ma fille 😳 mais yallah bakhna
2026-10-22 11:49:44
56
lments.khadimou.ra
Éléments khadimou rassoul ❤️ :
Bilahi B mane sama seye bi sama goro guinaw yallah moko teyé dima diokh dima tok lo dima mougnelo def ma come si dome la bilahi sama dieukeur bakh na dee mais goro bou bakh daye diap si seye
2026-10-22 07:52:16
31
fatoufaye053fa
yayou bayam💝 :
yéwol 3hr du matin ga bolé ko AK yalla🥺
2026-10-21 23:22:13
282
soniabusiness16
soniabusiness16 :
non je pleure bayiko ak yalla dinako djiss
2026-10-21 23:13:03
333
zaakhalifabusiness1
zaa_khalifa-business1 :
Thieuy adouna Lou meti yagg neuh dinako guisse dh mane dh samay diouli 3h du matin la yoor koumasi deff Lou meti ma dioulile lako 😌👩🏻‍🦯‍➡️
2026-10-22 13:18:53
13
psssssiiiii
🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳 :
Yalla nako yalla toroxal gnane bi sama xol lako tiibé
2026-10-22 08:43:47
21
user8875261437065
khady bou serigne Babacar s'y :
Ndayesan dioyna té tayoumako😭
2026-10-22 02:24:15
14
To see more videos from user @minandiaye0, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About